Al-Haqqa · 9/52
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Haqqa
وَجَاءَ فِرْعَوْنُ وَمَن قَبْلَهُ وَالْمُؤْتَفِكَاتُ بِالْخَاطِئَةِ ۝٩
Wa jaaa`a Firawnu wa man qablahoo wal mu`tafikaatu bilhaati`ah
📖 Tekkim Wolof
Firawnaak ña ko jiitu woon ak dëkk ya nu wëlbati woon njuumte la ñu fa nekke woon.

🎧 Dégg


📜 Aaya 7-11 — Simoore Al-Haqqa

7سَخَّرَهَا عَلَيْهِمْ سَبْعَ لَيَالٍ وَثَمَانِيَةَ أَيَّامٍ حُسُومًا فَتَرَى الْقَوْمَ فِيهَا صَرْعَىٰ كَأَنَّهُمْ أَعْجَازُ نَخْلٍ خَاوِيَةٍ
xiirtal na ko ci séen kaw juróom yaari bëccag ak juróom yaari guddi yu tegaloo nit ña ne lasiim melni dàtti tàndarma yu fënëx.
8فَهَلْ تَرَىٰ لَهُم مِّن بَاقِيَةٍ
Moo ndax gisati nga lu bokk ca ñoom?
9وَجَاءَ فِرْعَوْنُ وَمَن قَبْلَهُ وَالْمُؤْتَفِكَاتُ بِالْخَاطِئَةِ
Firawnaak ña ko jiitu woon ak dëkk ya nu wëlbati woon njuumte la ñu fa nekke woon.
10فَعَصَوْا رَسُولَ رَبِّهِمْ فَأَخَذَهُمْ أَخْذَةً رَّابِيَةً
Dañoo moyu woon senn Yonentub Boroom. Yàlla, faagaagal leen.
11إِنَّا لَمَّا طَغَى الْمَاءُ حَمَلْنَاكُمْ فِي الْجَارِيَةِ
Ba ndox ma bëbóo, Noo leen yanu woon, ca gaalug Nooh ga doon daw
Al-HaqqaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
9Aaya

Tekki — Al-Haqqa 9

Simoore Al-Haqqa Aaya 9 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Firawnaak ña ko jiitu woon ak dëkk ya nu wëlbati…

Simoore Aaya 9/52 — Simoore Al-Haqqa الحاقة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Haqqa Dégg, Simoore Al-Haqqa Tekki, Simoore Al-Haqqa mp3, Simoore Al-Haqqa pdf. Aaya 7–11. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers