Al-Haqqa · 8/52
Tekki Waxtaan — Al-Haqqa
فَهَلْ تَرَىٰ لَهُم مِّن بَاقِيَةٍ ۝٨
Fahal taraa lahum mim baaqiyah
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax gisati nga lu bokk ca ñoom?

🎧 Dégg


📜 Aaya 6-10 — Al-Haqqa

6وَأَمَّا عَادٌ فَأُهْلِكُوا بِرِيحٍ صَرْصَرٍ عَاتِيَةٍ
Giirug Aad nag ngelaw lu sedd luy riddi moom la ñu léen alage.
7سَخَّرَهَا عَلَيْهِمْ سَبْعَ لَيَالٍ وَثَمَانِيَةَ أَيَّامٍ حُسُومًا فَتَرَى الْقَوْمَ فِيهَا صَرْعَىٰ كَأَنَّهُمْ أَعْجَازُ نَخْلٍ خَاوِيَةٍ
xiirtal na ko ci séen kaw juróom yaari bëccag ak juróom yaari guddi yu tegaloo nit ña ne lasiim melni dàtti tàndarma yu fënëx.
8فَهَلْ تَرَىٰ لَهُم مِّن بَاقِيَةٍ
Moo ndax gisati nga lu bokk ca ñoom?
9وَجَاءَ فِرْعَوْنُ وَمَن قَبْلَهُ وَالْمُؤْتَفِكَاتُ بِالْخَاطِئَةِ
Firawnaak ña ko jiitu woon ak dëkk ya nu wëlbati woon njuumte la ñu fa nekke woon.
10فَعَصَوْا رَسُولَ رَبِّهِمْ فَأَخَذَهُمْ أَخْذَةً رَّابِيَةً
Dañoo moyu woon senn Yonentub Boroom. Yàlla, faagaagal leen.
Al-HaqqaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
8Aaya

Tekki — Al-Haqqa 8

Simoore Al-Haqqa Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax gisati nga lu bokk ca ñoom?

Simoore Aaya 8/52 — Al-Haqqa الحاقة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Haqqa Dégg, Al-Haqqa Tekki, Al-Haqqa mp3, Al-Haqqa pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, August 19, 2026

Don't forget us in your sincere prayers