Al-A'raf · 34/206
Tekki Waxtaan — Al-A'raf
وَلِكُلِّ أُمَّةٍ أَجَلٌ ۖ فَإِذَا جَاءَ أَجَلُهُمْ لَا يَسْتَأْخِرُونَ سَاعَةً ۖ وَلَا يَسْتَقْدِمُونَ ٣٤
Transliteration
Wa likulli ummatin ajalun fa izaa jaaa`a ajaluhum laa yastaakhiroona saa`atanw wa laa yastaqdimoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Xeet wu nekk am na àpp. Bu àpp ba agsee, duñu yées senn saa te it duñu ko jiitu.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 32-36 — Al-A'raf
32قُلْ مَنْ حَرَّمَ زِينَةَ اللَّهِ الَّتِي أَخْرَجَ لِعِبَادِهِ وَالطَّيِّبَاتِ مِنَ الرِّزْقِ ۚ قُلْ هِيَ لِلَّذِينَ آمَنُوا فِي الْحَيَاةِ الدُّنْيَا خَالِصَةً يَوْمَ الْقِيَامَةِ ۗ كَذَٰلِكَ نُفَصِّلُ الْآيَاتِ لِقَوْمٍ يَعْلَمُونَ
Neel : “Ana kan mooy digle ne taari Yàlla, yi Mu génneel ay jaamam, araam nañu, ak xéewal yu sell yi ? ”. Neel : “Yooyu, ñi gëm ci àddina bi, ñoo koy moom, ñoom doŋŋ te bu àllaaxiraa.”. Noonu la Nuy leeralee Sunuy tegtal ci nit ñuy xam.
33قُلْ إِنَّمَا حَرَّمَ رَبِّيَ الْفَوَاحِشَ مَا ظَهَرَ مِنْهَا وَمَا بَطَنَ وَالْإِثْمَ وَالْبَغْيَ بِغَيْرِ الْحَقِّ وَأَن تُشْرِكُوا بِاللَّهِ مَا لَمْ يُنَزِّلْ بِهِ سُلْطَانًا وَأَن تَقُولُوا عَلَى اللَّهِ مَا لَا تَعْلَمُونَ
Neel : “Sama Boroom araamalul lu dul ñaawtéef yi, la ca feeñ ak la ca nëbbu ak bàkkaar, ak bew guy jalgati dëgg, ak di Ko bokkaaleek loo xam ne wenn lay wàccewu ca, ak ngeen di wax ci Yàlla lu ngeen xamul. [Yooyu ñoo araam]”.
34وَلِكُلِّ أُمَّةٍ أَجَلٌ ۖ فَإِذَا جَاءَ أَجَلُهُمْ لَا يَسْتَأْخِرُونَ سَاعَةً ۖ وَلَا يَسْتَقْدِمُونَ
Xeet wu nekk am na àpp. Bu àpp ba agsee, duñu yées senn saa te it duñu ko jiitu.
35يَا بَنِي آدَمَ إِمَّا يَأْتِيَنَّكُمْ رُسُلٌ مِّنكُمْ يَقُصُّونَ عَلَيْكُمْ آيَاتِي ۙ فَمَنِ اتَّقَىٰ وَأَصْلَحَ فَلَا خَوْفٌ عَلَيْهِمْ وَلَا هُمْ يَحْزَنُونَ
Éy yéen doomi-aadama yi ! Amaana ay Yonent yu bokk ci yéen dikkal leen, di leen nettali sunuy tegtal, (nangeen xam ne) képp ku ragal na Yàlla tey yéwénal, du am tiitaange te du jàq.
36وَالَّذِينَ كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا وَاسْتَكْبَرُوا عَنْهَا أُولَٰئِكَ أَصْحَابُ النَّارِ ۖ هُمْ فِيهَا خَالِدُونَ
Gaa ña nga xam ne dañoo weddi Sunuy tegtal, rëy-rëylu, dëddu ko, ñooñee ñooy waa Safara, te dañu fay béel.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
34Aaya
Tekki — Al-A'raf 34
Simoore Al-A'raf Aaya 34 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xeet wu nekk am na àpp. Bu àpp ba agsee,…Simoore Aaya 34/206 — Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-A'raf Dégg, Al-A'raf Tekki, Al-A'raf mp3, Al-A'raf pdf. Aaya 32–36. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








