Al-Ma'arij · 44/44
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Ma'arij
خَاشِعَةً أَبْصَارُهُمْ تَرْهَقُهُمْ ذِلَّةٌ ۚ ذَٰلِكَ الْيَوْمُ الَّذِي كَانُوا يُوعَدُونَ ۝٤٤
Khaashi`atan absaaruhum tarhaquhum zillah; zaalikal yawmul lazee kaanoo yoo`adoon
📖 Tekkim Wolof
seen gët ya sajju, ñu torox ngir gàcce. Bis boobee mooy ba ñu leen daan dig (tëkoo)!

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 42-44 — Simoore Al-Ma'arij

42فَذَرْهُمْ يَخُوضُوا وَيَلْعَبُوا حَتَّىٰ يُلَاقُوا يَوْمَهُمُ الَّذِي يُوعَدُونَ
Bàyyileen ñu nuur (ci kéefër) aka fo ba baa ñuy dajeek bis ba ñu leen daan digu,
43يَوْمَ يَخْرُجُونَ مِنَ الْأَجْدَاثِ سِرَاعًا كَأَنَّهُمْ إِلَىٰ نُصُبٍ يُوفِضُونَ
bu keroogee, ba ñuy génn bàmmeel ya gaaw melni ku jëm ciy xërëm ;
44خَاشِعَةً أَبْصَارُهُمْ تَرْهَقُهُمْ ذِلَّةٌ ۚ ذَٰلِكَ الْيَوْمُ الَّذِي كَانُوا يُوعَدُونَ
seen gët ya sajju, ñu torox ngir gàcce. Bis boobee mooy ba ñu leen daan dig (tëkoo)!
Al-Ma'arijFihi Alxuraan
44Aaya
MeccanRevelation
44Aaya

Tekki — Al-Ma'arij 44

Simoore Al-Ma'arij Aaya 44 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : seen gët ya sajju, ñu torox ngir gàcce. Bis boobee…

Simoore Aaya 44/44 — Simoore Al-Ma'arij المعارج (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Ma'arij Dégg, Simoore Al-Ma'arij Tekki, Simoore Al-Ma'arij mp3, Simoore Al-Ma'arij pdf. Aaya 42–44. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers