Al-Jinn · 12/28
Tekki Waxtaan — Al-Jinn
وَأَنَّا ظَنَنَّا أَن لَّن نُّعْجِزَ اللَّهَ فِي الْأَرْضِ وَلَن نُّعْجِزَهُ هَرَبًا ۝١٢
Wa annaa zanannaaa al lan nu`jizal laaha fil ardi wa lan nu`jizahoo harabaa
📖 Tekkim Wolof
Te xam nanu ne manuñoo tiiñ Yàlla te it manuñoo daw mukk ba raw ko.

🎧 Dégg


📜 Aaya 10-14 — Al-Jinn

10وَأَنَّا لَا نَدْرِي أَشَرٌّ أُرِيدَ بِمَن فِي الْأَرْضِ أَمْ أَرَادَ بِهِمْ رَبُّهُمْ رَشَدًا
Te nun sax xamu nu ndax ñi nekk ci suuf si aw ay lees namm ci ñoom walla seen Boroom dafa namm ci ñoom ñu jub.
11وَأَنَّا مِنَّا الصَّالِحُونَ وَمِنَّا دُونَ ذَٰلِكَ ۖ كُنَّا طَرَائِقَ قِدَدًا
Am na ci nun ñu jub am na it ñu yées loolu : nun daal ay kurél lanu yu limu.
12وَأَنَّا ظَنَنَّا أَن لَّن نُّعْجِزَ اللَّهَ فِي الْأَرْضِ وَلَن نُّعْجِزَهُ هَرَبًا
Te xam nanu ne manuñoo tiiñ Yàlla te it manuñoo daw mukk ba raw ko.
13وَأَنَّا لَمَّا سَمِعْنَا الْهُدَىٰ آمَنَّا بِهِ ۖ فَمَن يُؤْمِن بِرَبِّهِ فَلَا يَخَافُ بَخْسًا وَلَا رَهَقًا
Te nun ba nu déggee njub ga [Alxuraan], gëm nanu ko, te nag képp ku gëm Boroomam dootul ragal wàññikug jëf waxantumalaak sànje.
14وَأَنَّا مِنَّا الْمُسْلِمُونَ وَمِنَّا الْقَاسِطُونَ ۖ فَمَنْ أَسْلَمَ فَأُولَٰئِكَ تَحَرَّوْا رَشَدًا
Am na ci nun ay jullit, am na it ci nun ay tooñkat. Ña nga xam ne ñoom dañoo tuub defi jullit ñoo ñaa làmboo njub.
Al-JinnFihi Alxuraan
28Aaya
MeccanRevelation
12Aaya

Tekki — Al-Jinn 12

Simoore Al-Jinn Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te xam nanu ne manuñoo tiiñ Yàlla te it manuñoo…

Simoore Aaya 12/28 — Al-Jinn الجن (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Jinn Dégg, Al-Jinn Tekki, Al-Jinn mp3, Al-Jinn pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers