Al-Jinn · 13/28
Tekki Waxtaan — Al-Jinn
وَأَنَّا لَمَّا سَمِعْنَا الْهُدَىٰ آمَنَّا بِهِ ۖ فَمَن يُؤْمِن بِرَبِّهِ فَلَا يَخَافُ بَخْسًا وَلَا رَهَقًا ۝١٣
Wa annaa lammaa sami`nal hudaaa aamannaa bihee famany yu`mim bi rabbihee falaa yakhaafu bakhsanw wa laa rahaqaa
📖 Tekkim Wolof
Te nun ba nu déggee njub ga [Alxuraan], gëm nanu ko, te nag képp ku gëm Boroomam dootul ragal wàññikug jëf waxantumalaak sànje.

🎧 Dégg


📜 Aaya 11-15 — Al-Jinn

11وَأَنَّا مِنَّا الصَّالِحُونَ وَمِنَّا دُونَ ذَٰلِكَ ۖ كُنَّا طَرَائِقَ قِدَدًا
Am na ci nun ñu jub am na it ñu yées loolu : nun daal ay kurél lanu yu limu.
12وَأَنَّا ظَنَنَّا أَن لَّن نُّعْجِزَ اللَّهَ فِي الْأَرْضِ وَلَن نُّعْجِزَهُ هَرَبًا
Te xam nanu ne manuñoo tiiñ Yàlla te it manuñoo daw mukk ba raw ko.
13وَأَنَّا لَمَّا سَمِعْنَا الْهُدَىٰ آمَنَّا بِهِ ۖ فَمَن يُؤْمِن بِرَبِّهِ فَلَا يَخَافُ بَخْسًا وَلَا رَهَقًا
Te nun ba nu déggee njub ga [Alxuraan], gëm nanu ko, te nag képp ku gëm Boroomam dootul ragal wàññikug jëf waxantumalaak sànje.
14وَأَنَّا مِنَّا الْمُسْلِمُونَ وَمِنَّا الْقَاسِطُونَ ۖ فَمَنْ أَسْلَمَ فَأُولَٰئِكَ تَحَرَّوْا رَشَدًا
Am na ci nun ay jullit, am na it ci nun ay tooñkat. Ña nga xam ne ñoom dañoo tuub defi jullit ñoo ñaa làmboo njub.
15وَأَمَّا الْقَاسِطُونَ فَكَانُوا لِجَهَنَّمَ حَطَبًا
Tooñkat ya nag, ñoom ñoo di mattum safara.
Al-JinnFihi Alxuraan
28Aaya
MeccanRevelation
13Aaya

Tekki — Al-Jinn 13

Simoore Al-Jinn Aaya 13 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te nun ba nu déggee njub ga [Alxuraan], gëm nanu…

Simoore Aaya 13/28 — Al-Jinn الجن (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Jinn Dégg, Al-Jinn Tekki, Al-Jinn mp3, Al-Jinn pdf. Aaya 11–15. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers