Al-Jinn · 16/28
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Jinn
وَأَن لَّوِ اسْتَقَامُوا عَلَى الطَّرِيقَةِ لَأَسْقَيْنَاهُم مَّاءً غَدَقًا ۝١٦
Wa alla wis taqaamoo `alat tareeqati la asqaynaahum maa`an ghadaqaa
📖 Tekkim Wolof
Te kat su ñu jaaroon ca yoon wu jub xocc wa, Danaa leen nàndale, ndox mu neex,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 14-18 — Simoore Al-Jinn

14وَأَنَّا مِنَّا الْمُسْلِمُونَ وَمِنَّا الْقَاسِطُونَ ۖ فَمَنْ أَسْلَمَ فَأُولَٰئِكَ تَحَرَّوْا رَشَدًا
Am na ci nun ay jullit, am na it ci nun ay tooñkat. Ña nga xam ne ñoom dañoo tuub defi jullit ñoo ñaa làmboo njub.
15وَأَمَّا الْقَاسِطُونَ فَكَانُوا لِجَهَنَّمَ حَطَبًا
Tooñkat ya nag, ñoom ñoo di mattum safara.
16وَأَن لَّوِ اسْتَقَامُوا عَلَى الطَّرِيقَةِ لَأَسْقَيْنَاهُم مَّاءً غَدَقًا
Te kat su ñu jaaroon ca yoon wu jub xocc wa, Danaa leen nàndale, ndox mu neex,
17لِّنَفْتِنَهُمْ فِيهِ ۚ وَمَن يُعْرِضْ عَن ذِكْرِ رَبِّهِ يَسْلُكْهُ عَذَابًا صَعَدًا
ngir nu nattu leen ca. Képp ku dumóoyu baña fàttaliku Boroomam, (Yàlla) dana ko sóob ci mbugël muy dolliku saa su nekk.
18وَأَنَّ الْمَسَاجِدَ لِلَّهِ فَلَا تَدْعُوا مَعَ اللَّهِ أَحَدًا
Jàkka yi Yàlla moo leen moom : buleen fay woo kenn di ko booleek Yàlla.
Al-JinnFihi Alxuraan
28Aaya
MeccanRevelation
16Aaya

Tekki — Al-Jinn 16

Simoore Al-Jinn Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te kat su ñu jaaroon ca yoon wu jub xocc…

Simoore Aaya 16/28 — Simoore Al-Jinn الجن (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Jinn Dégg, Simoore Al-Jinn Tekki, Simoore Al-Jinn mp3, Simoore Al-Jinn pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers