Al-Jinn · 27/28
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Jinn
إِلَّا مَنِ ارْتَضَىٰ مِن رَّسُولٍ فَإِنَّهُ يَسْلُكُ مِن بَيْنِ يَدَيْهِ وَمِنْ خَلْفِهِ رَصَدًا ۝٢٧
Illaa manir tadaa mir rasoolin fa innahoo yasluku mim baini yadihi wa min khalfihee rasadaa
📖 Tekkim Wolof
lu dul ku mu gëram ci Yonent te dakoy booleek ñu koy wattu kanam ak ginnaaw,

🎧 Dégg


📜 Aaya 25-28 — Simoore Al-Jinn

25قُلْ إِنْ أَدْرِي أَقَرِيبٌ مَّا تُوعَدُونَ أَمْ يَجْعَلُ لَهُ رَبِّي أَمَدًا
Waxal ne: “Xamuma baxam li ñu leen di tëkkoo dafa jiggeñ, walla, sama Boroom da leen may ab dig.
26عَالِمُ الْغَيْبِ فَلَا يُظْهِرُ عَلَىٰ غَيْبِهِ أَحَدًا
[Moom] moo xam kumpa. Te du wuññil kumpaam ga kenn,
27إِلَّا مَنِ ارْتَضَىٰ مِن رَّسُولٍ فَإِنَّهُ يَسْلُكُ مِن بَيْنِ يَدَيْهِ وَمِنْ خَلْفِهِ رَصَدًا
lu dul ku mu gëram ci Yonent te dakoy booleek ñu koy wattu kanam ak ginnaaw,
28لِّيَعْلَمَ أَن قَدْ أَبْلَغُوا رِسَالَاتِ رَبِّهِمْ وَأَحَاطَ بِمَا لَدَيْهِمْ وَأَحْصَىٰ كُلَّ شَيْءٍ عَدَدًا
ngir mu xam ne jotal nañu seen Yonentub Boroom. Te it peeg na lépp lu ne ci ab lim (xam na na mu day”.
Al-JinnFihi Alxuraan
28Aaya
MeccanRevelation
27Aaya

Tekki — Al-Jinn 27

Simoore Al-Jinn Aaya 27 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : lu dul ku mu gëram ci Yonent te dakoy booleek…

Simoore Aaya 27/28 — Simoore Al-Jinn الجن (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Jinn Dégg, Simoore Al-Jinn Tekki, Simoore Al-Jinn mp3, Simoore Al-Jinn pdf. Aaya 25–28. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers