Al-Qiyama · 26/40
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qiyama
كَلَّا إِذَا بَلَغَتِ التَّرَاقِيَ ۝٢٦
Kallaaa izaa balaghatit taraaqee
📖 Tekkim Wolof
Bu ruuga génnee ba ca bóli ga

🎧 Dégg


📜 Aaya 24-28 — Simoore Al-Qiyama

24وَوُجُوهٌ يَوْمَئِذٍ بَاسِرَةٌ
dana fa am it bu keroogee, ay xarkanam yu ñàng,
25تَظُنُّ أَن يُفْعَلَ بِهَا فَاقِرَةٌ
dangay foog ne njuuma la.
26كَلَّا إِذَا بَلَغَتِ التَّرَاقِيَ
Bu ruuga génnee ba ca bóli ga
27وَقِيلَ مَنْ ۜ رَاقٍ
ñu ne ko: “Ana kan mooy mocckat ba ? ”
28وَظَنَّ أَنَّهُ الْفِرَاقُ
Mu daldi xam nag ne dee dikk na,
Al-QiyamaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
26Aaya

Tekki — Al-Qiyama 26

Simoore Al-Qiyama Aaya 26 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu ruuga génnee ba ca bóli ga

Simoore Aaya 26/40 — Simoore Al-Qiyama القيامة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qiyama Dégg, Simoore Al-Qiyama Tekki, Simoore Al-Qiyama mp3, Simoore Al-Qiyama pdf. Aaya 24–28. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers