Al-Qiyama · 29/40
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qiyama
وَالْتَفَّتِ السَّاقُ بِالسَّاقِ ۝٢٩
Waltaffatis saaqu bissaaq
📖 Tekkim Wolof
yeel ya daldi jaxasoo rawaasoo,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 27-31 — Simoore Al-Qiyama

27وَقِيلَ مَنْ ۜ رَاقٍ
ñu ne ko: “Ana kan mooy mocckat ba ? ”
28وَظَنَّ أَنَّهُ الْفِرَاقُ
Mu daldi xam nag ne dee dikk na,
29وَالْتَفَّتِ السَّاقُ بِالسَّاقِ
yeel ya daldi jaxasoo rawaasoo,
30إِلَىٰ رَبِّكَ يَوْمَئِذٍ الْمَسَاقُ
Bu keroogee, ñu wommat la jaŋat-jaŋatee la jëm ca sa Boroom.
31فَلَا صَدَّقَ وَلَا صَلَّىٰ
Gëmul woon, te it daawuloon julli;
Al-QiyamaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
29Aaya

Tekki — Al-Qiyama 29

Simoore Al-Qiyama Aaya 29 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : yeel ya daldi jaxasoo rawaasoo,

Simoore Aaya 29/40 — Simoore Al-Qiyama القيامة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qiyama Dégg, Simoore Al-Qiyama Tekki, Simoore Al-Qiyama mp3, Simoore Al-Qiyama pdf. Aaya 27–31. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers