Al-Qiyama · 28/40
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qiyama
وَظَنَّ أَنَّهُ الْفِرَاقُ ۝٢٨
Wa zanna annahul firaaq
📖 Tekkim Wolof
Mu daldi xam nag ne dee dikk na,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 26-30 — Simoore Al-Qiyama

26كَلَّا إِذَا بَلَغَتِ التَّرَاقِيَ
Bu ruuga génnee ba ca bóli ga
27وَقِيلَ مَنْ ۜ رَاقٍ
ñu ne ko: “Ana kan mooy mocckat ba ? ”
28وَظَنَّ أَنَّهُ الْفِرَاقُ
Mu daldi xam nag ne dee dikk na,
29وَالْتَفَّتِ السَّاقُ بِالسَّاقِ
yeel ya daldi jaxasoo rawaasoo,
30إِلَىٰ رَبِّكَ يَوْمَئِذٍ الْمَسَاقُ
Bu keroogee, ñu wommat la jaŋat-jaŋatee la jëm ca sa Boroom.
Al-QiyamaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
28Aaya

Tekki — Al-Qiyama 28

Simoore Al-Qiyama Aaya 28 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu daldi xam nag ne dee dikk na,

Simoore Aaya 28/40 — Simoore Al-Qiyama القيامة (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qiyama Dégg, Simoore Al-Qiyama Tekki, Simoore Al-Qiyama mp3, Simoore Al-Qiyama pdf. Aaya 26–30. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers