Al-Insan · 23/31
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Insan
إِنَّا نَحْنُ نَزَّلْنَا عَلَيْكَ الْقُرْآنَ تَنزِيلًا ۝٢٣
Innaa nahnu nazzalnaa `alaikal quraana tanzeelaa
📖 Tekkim Wolof
Nun de Noo wàcce Alxuraan ci yaw ndànk-ndànk.

🎧 Dégg


📜 Aaya 21-25 — Simoore Al-Insan

21عَالِيَهُمْ ثِيَابُ سُندُسٍ خُضْرٌ وَإِسْتَبْرَقٌ ۖ وَحُلُّوا أَسَاوِرَ مِن فِضَّةٍ وَسَقَاهُمْ رَبُّهُمْ شَرَابًا طَهُورًا
Dañuy sol mbubbi sooy yu nëtëx werta. Moom la ñuy jiital waaje ko, te dañu leen di takkal caqi xaalis. Seen Boroom di leen fa ndàndale naan gu laab.
22إِنَّ هَٰذَا كَانَ لَكُمْ جَزَاءً وَكَانَ سَعْيُكُم مَّشْكُورًا
Lii nag mooy seen neexal, te seen jëf it lu ñu sant la.
23إِنَّا نَحْنُ نَزَّلْنَا عَلَيْكَ الْقُرْآنَ تَنزِيلًا
Nun de Noo wàcce Alxuraan ci yaw ndànk-ndànk.
24فَاصْبِرْ لِحُكْمِ رَبِّكَ وَلَا تُطِعْ مِنْهُمْ آثِمًا أَوْ كَفُورًا
Muñal sa dogalub Boroom, te bul topp, ci ñoom, kenn kuy def bàkkaar walla mu di yéefar.
25وَاذْكُرِ اسْمَ رَبِّكَ بُكْرَةً وَأَصِيلًا
Te na nga tudd sa turu Boroom, subaak ngoon ;
Al-InsanFihi Alxuraan
31Aaya
MedinanRevelation
23Aaya

Tekki — Al-Insan 23

Simoore Al-Insan Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nun de Noo wàcce Alxuraan ci yaw ndànk-ndànk.

Simoore Aaya 23/31 — Simoore Al-Insan الإنسان (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Insan Dégg, Simoore Al-Insan Tekki, Simoore Al-Insan mp3, Simoore Al-Insan pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers