An-Nazi'at · 25/46
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nazi'at
فَأَخَذَهُ اللَّهُ نَكَالَ الْآخِرَةِ وَالْأُولَىٰ ۝٢٥
Fa-akha zahul laahu nakalal aakhirati wal-oola
📖 Tekkim Wolof
Yàlla daldi koy faagaagal mbugalum àddina muy sar ba àllaaxira.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 23-27 — Simoore An-Nazi'at

23فَحَشَرَ فَنَادَىٰ
daldi woo nit ña dajale leen,
24فَقَالَ أَنَا رَبُّكُمُ الْأَعْلَىٰ
daldi wax ne : “Man maay sen boroom, bi gëna kawe”.
25فَأَخَذَهُ اللَّهُ نَكَالَ الْآخِرَةِ وَالْأُولَىٰ
Yàlla daldi koy faagaagal mbugalum àddina muy sar ba àllaaxira.
26إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَعِبْرَةً لِّمَن يَخْشَىٰ
Ag fàttalikoo ngi ci loolu ña ragal Yàlla.
27أَأَنتُمْ أَشَدُّ خَلْقًا أَمِ السَّمَاءُ ۚ بَنَاهَا
li ngeen sos moo gëna dëgër ? walla asamaan si ma tabax ?
An-Nazi'atFihi Alxuraan
46Aaya
MeccanRevelation
25Aaya

Tekki — An-Nazi'at 25

Simoore An-Nazi'at Aaya 25 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla daldi koy faagaagal mbugalum àddina muy sar ba àllaaxira.

Simoore Aaya 25/46 — Simoore An-Nazi'at النازعات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nazi'at Dégg, Simoore An-Nazi'at Tekki, Simoore An-Nazi'at mp3, Simoore An-Nazi'at pdf. Aaya 23–27. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers