An-Nazi'at · 24/46
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nazi'at
فَقَالَ أَنَا رَبُّكُمُ الْأَعْلَىٰ ۝٢٤
Faqala ana rabbu kumul-a`laa
📖 Tekkim Wolof
daldi wax ne : “Man maay sen boroom, bi gëna kawe”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 22-26 — Simoore An-Nazi'at

22ثُمَّ أَدْبَرَ يَسْعَىٰ
Mu daldi, dumóoyu, féew dem,
23فَحَشَرَ فَنَادَىٰ
daldi woo nit ña dajale leen,
24فَقَالَ أَنَا رَبُّكُمُ الْأَعْلَىٰ
daldi wax ne : “Man maay sen boroom, bi gëna kawe”.
25فَأَخَذَهُ اللَّهُ نَكَالَ الْآخِرَةِ وَالْأُولَىٰ
Yàlla daldi koy faagaagal mbugalum àddina muy sar ba àllaaxira.
26إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَعِبْرَةً لِّمَن يَخْشَىٰ
Ag fàttalikoo ngi ci loolu ña ragal Yàlla.
An-Nazi'atFihi Alxuraan
46Aaya
MeccanRevelation
24Aaya

Tekki — An-Nazi'at 24

Simoore An-Nazi'at Aaya 24 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : daldi wax ne : “Man maay sen boroom, bi gëna…

Simoore Aaya 24/46 — Simoore An-Nazi'at النازعات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nazi'at Dégg, Simoore An-Nazi'at Tekki, Simoore An-Nazi'at mp3, Simoore An-Nazi'at pdf. Aaya 22–26. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers