An-Nazi'at · 41/46
Tekki Waxtaan — An-Nazi'at
فَإِنَّ الْجَنَّةَ هِيَ الْمَأْوَىٰ ۝٤١
Fa innal jannata hiyal maawaa
📖 Tekkim Wolof
kookee àjjanaa di wàccuwaayam.
🎧 Dégg

📜 Aaya 39-43 — An-Nazi'at

39فَإِنَّ الْجَحِيمَ هِيَ الْمَأْوَىٰ
kookee, Safaraa di wàccuwaayam.
40وَأَمَّا مَنْ خَافَ مَقَامَ رَبِّهِ وَنَهَى النَّفْسَ عَنِ الْهَوَىٰ
Képp ku ragaloon ne dana taxaw ca Boroomam, te daan tere bakkanam bànneex (ay caaxaan),
41فَإِنَّ الْجَنَّةَ هِيَ الْمَأْوَىٰ
kookee àjjanaa di wàccuwaayam.
42يَسْأَلُونَكَ عَنِ السَّاعَةِ أَيَّانَ مُرْسَاهَا
Ña nga lay laaj bis pénc ba : “Kañ lay teeral”
43فِيمَ أَنتَ مِن ذِكْرَاهَا
Ana ban xam-xam nga ci am ngir tontu leen ?
An-Nazi'atFihi Alxuraan
46Aaya
MeccanRevelation
41Aaya

Tekki — An-Nazi'at 41

Simoore An-Nazi'at Aaya 41 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : kookee àjjanaa di wàccuwaayam.

Simoore Aaya 41/46 — An-Nazi'at النازعات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nazi'at Dégg, An-Nazi'at Tekki, An-Nazi'at mp3, An-Nazi'at pdf. Aaya 39–43. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers