An-Nazi'at · 42/46
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nazi'at
يَسْأَلُونَكَ عَنِ السَّاعَةِ أَيَّانَ مُرْسَاهَا ۝٤٢
Yas`aloonaka `anis saa`ati ayyaana mursaahaa
📖 Tekkim Wolof
Ña nga lay laaj bis pénc ba : “Kañ lay teeral”

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 40-44 — Simoore An-Nazi'at

40وَأَمَّا مَنْ خَافَ مَقَامَ رَبِّهِ وَنَهَى النَّفْسَ عَنِ الْهَوَىٰ
Képp ku ragaloon ne dana taxaw ca Boroomam, te daan tere bakkanam bànneex (ay caaxaan),
41فَإِنَّ الْجَنَّةَ هِيَ الْمَأْوَىٰ
kookee àjjanaa di wàccuwaayam.
42يَسْأَلُونَكَ عَنِ السَّاعَةِ أَيَّانَ مُرْسَاهَا
Ña nga lay laaj bis pénc ba : “Kañ lay teeral”
43فِيمَ أَنتَ مِن ذِكْرَاهَا
Ana ban xam-xam nga ci am ngir tontu leen ?
44إِلَىٰ رَبِّكَ مُنتَهَاهَا
Ab yemukaayam sa Boroom rekk ko xam.
An-Nazi'atFihi Alxuraan
46Aaya
MeccanRevelation
42Aaya

Tekki — An-Nazi'at 42

Simoore An-Nazi'at Aaya 42 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña nga lay laaj bis pénc ba : “Kañ lay…

Simoore Aaya 42/46 — Simoore An-Nazi'at النازعات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nazi'at Dégg, Simoore An-Nazi'at Tekki, Simoore An-Nazi'at mp3, Simoore An-Nazi'at pdf. Aaya 40–44. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers