Al-Anfal · 13/75
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anfal
ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمْ شَاقُّوا اللَّهَ وَرَسُولَهُ ۚ وَمَن يُشَاقِقِ اللَّهَ وَرَسُولَهُ فَإِنَّ اللَّهَ شَدِيدُ الْعِقَابِ ۝١٣
Zaalika bi annahum shaaaqqul laaha wa Rasoolah; wa mai yushaqiqil laaha wa Rasoolahoo fa innal laaha shadeedul `iqaab
📖 Tekkim Wolof
Loolu, ngir dañoo juuyook Yàlla ak Yonentam.”. Te ku juuyook Yàlla ak Yonentam, ... [na xam ne] Yàlla ku tar mbugal la !

🎧 Dégg


📜 Aaya 11-15 — Simoore Al-Anfal

11إِذْ يُغَشِّيكُمُ النُّعَاسَ أَمَنَةً مِّنْهُ وَيُنَزِّلُ عَلَيْكُم مِّنَ السَّمَاءِ مَاءً لِّيُطَهِّرَكُم بِهِ وَيُذْهِبَ عَنكُمْ رِجْزَ الشَّيْطَانِ وَلِيَرْبِطَ عَلَىٰ قُلُوبِكُمْ وَيُثَبِّتَ بِهِ الْأَقْدَامَ
(Fàttalikuleen) ba Mu leen muuree ag ngëmmentu muy jàmm ju jóge ci Moom, te Mu wàcce ci yéen ndox mu jóge asamaan ngir Mu laabal leen ak loolu, ak ngir Mu dàqal leen sobees Séytaane, ak ngir Mu dëgëral seeni xol, dëgëral seeni ndëggu.
12إِذْ يُوحِي رَبُّكَ إِلَى الْمَلَائِكَةِ أَنِّي مَعَكُمْ فَثَبِّتُوا الَّذِينَ آمَنُوا ۚ سَأُلْقِي فِي قُلُوبِ الَّذِينَ كَفَرُوا الرُّعْبَ فَاضْرِبُوا فَوْقَ الْأَعْنَاقِ وَاضْرِبُوا مِنْهُمْ كُلَّ بَنَانٍ
[Fàttalikul] ba sa Boroom xamalee Malaaka ya ne leen : “Maak yéen a ànd : nangeen dooleel ñi gëm. Danaa sànni njàqare ci xoli ñi weddi. Kon dóorleen ci kaw doq yi te ngeen dóor leen ci cati baaraam yi.
13ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمْ شَاقُّوا اللَّهَ وَرَسُولَهُ ۚ وَمَن يُشَاقِقِ اللَّهَ وَرَسُولَهُ فَإِنَّ اللَّهَ شَدِيدُ الْعِقَابِ
Loolu, ngir dañoo juuyook Yàlla ak Yonentam.”. Te ku juuyook Yàlla ak Yonentam, ... [na xam ne] Yàlla ku tar mbugal la !
14ذَٰلِكُمْ فَذُوقُوهُ وَأَنَّ لِلْكَافِرِينَ عَذَابَ النَّارِ
Noonu lay dalee ci yéen [yéefar yi] ; kon mosleen ko ! Te ñeel na way-weddi ña mbugalu Safara.
15يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا إِذَا لَقِيتُمُ الَّذِينَ كَفَرُوا زَحْفًا فَلَا تُوَلُّوهُمُ الْأَدْبَارَ
Éy yéen ñi gëm ñi, bu ngeen dajeek yéefar yi ñuy ràngu jëm ci yéen, buleen daw won leen ginnaaw.
Al-AnfalFihi Alxuraan
75Aaya
MedinanRevelation
13Aaya

Tekki — Al-Anfal 13

Simoore Al-Anfal Aaya 13 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Loolu, ngir dañoo juuyook Yàlla ak Yonentam.”. Te ku juuyook…

Simoore Aaya 13/75 — Simoore Al-Anfal الأنفال (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anfal Dégg, Simoore Al-Anfal Tekki, Simoore Al-Anfal mp3, Simoore Al-Anfal pdf. Aaya 11–15. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers