Al-Fajr · 14/30
Tekki Waxtaan — Al-Fajr
إِنَّ رَبَّكَ لَبِالْمِرْصَادِ ۝١٤
Inna Rabbaka labil mirsaad
📖 Tekkim Wolof
Sa Boroom nag ma ngay fuglu.
🎧 Dégg

📜 Aaya 12-16 — Al-Fajr

12فَأَكْثَرُوا فِيهَا الْفَسَادَ
te ñu bariloon fa lool ag yàq.
13فَصَبَّ عَلَيْهِمْ رَبُّكَ سَوْطَ عَذَابٍ
Sa Boroom daldi leen sotti yarum mbugël.
14إِنَّ رَبَّكَ لَبِالْمِرْصَادِ
Sa Boroom nag ma ngay fuglu.
15فَأَمَّا الْإِنسَانُ إِذَا مَا ابْتَلَاهُ رَبُّهُ فَأَكْرَمَهُ وَنَعَّمَهُ فَيَقُولُ رَبِّي أَكْرَمَنِ
Nit nag, moom saa su ko boroomam nattoo teral ko xéewal ko, mu ne : “Sama Boroom teral na ma”.
16وَأَمَّا إِذَا مَا ابْتَلَاهُ فَقَدَرَ عَلَيْهِ رِزْقَهُ فَيَقُولُ رَبِّي أَهَانَنِ
Saa su ko nattoo wàññi wërsagëm, muy wax naan : “Sama Boroom toroxal nama”.
Al-FajrFihi Alxuraan
30Aaya
MeccanRevelation
14Aaya

Tekki — Al-Fajr 14

Simoore Al-Fajr Aaya 14 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Sa Boroom nag ma ngay fuglu.

Simoore Aaya 14/30 — Al-Fajr الفجر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Fajr Dégg, Al-Fajr Tekki, Al-Fajr mp3, Al-Fajr pdf. Aaya 12–16. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers