At-Tawba · 127/129
Tekki Waxtaan — Simoore At-Tawba
وَإِذَا مَا أُنزِلَتْ سُورَةٌ نَّظَرَ بَعْضُهُمْ إِلَىٰ بَعْضٍ هَلْ يَرَاكُم مِّنْ أَحَدٍ ثُمَّ انصَرَفُوا ۚ صَرَفَ اللَّهُ قُلُوبَهُم بِأَنَّهُمْ قَوْمٌ لَّا يَفْقَهُونَ ۝١٢٧
Wa izaa maaa unzilat Sooratun nazara ba`duhum ilaa ba`din hal yaraakum min ahadin summman sarafoo; sarafal laahu quloobahum bi annahum qawmul laa yafqahoon
📖 Tekkim Wolof
Te su ñu wàccee aw saar ñu daldi xoolante, daldi wax ne : “Moo ndax am na ku nu gis ? ”. Daldi wëlbëtiku. Yal na Yàlla wëlbëti seeni xol ndax ñoom, aw nit lañu ñu amul genn dégg-dégg.

🎧 Dégg


📜 Aaya 125-129 — Simoore At-Tawba

125وَأَمَّا الَّذِينَ فِي قُلُوبِهِم مَّرَضٌ فَزَادَتْهُمْ رِجْسًا إِلَىٰ رِجْسِهِمْ وَمَاتُوا وَهُمْ كَافِرُونَ
Ña nga xam ne jàngaro nekk na ci seen xol ya, dafay nekk ci ñoom kéefar guy dolliku cig kéefar, te ci kéefar googu lañuy deewaale.
126أَوَلَا يَرَوْنَ أَنَّهُمْ يُفْتَنُونَ فِي كُلِّ عَامٍ مَّرَّةً أَوْ مَرَّتَيْنِ ثُمَّ لَا يَتُوبُونَ وَلَا هُمْ يَذَّكَّرُونَ
Moo ndax dañoo gisul ne at mu nekk dees na leen not benn walla ñaari yoon ? Te ñooña, duñu tuub, duñu waaru.
127وَإِذَا مَا أُنزِلَتْ سُورَةٌ نَّظَرَ بَعْضُهُمْ إِلَىٰ بَعْضٍ هَلْ يَرَاكُم مِّنْ أَحَدٍ ثُمَّ انصَرَفُوا ۚ صَرَفَ اللَّهُ قُلُوبَهُم بِأَنَّهُمْ قَوْمٌ لَّا يَفْقَهُونَ
Te su ñu wàccee aw saar ñu daldi xoolante, daldi wax ne : “Moo ndax am na ku nu gis ? ”. Daldi wëlbëtiku. Yal na Yàlla wëlbëti seeni xol ndax ñoom, aw nit lañu ñu amul genn dégg-dégg.
128لَقَدْ جَاءَكُمْ رَسُولٌ مِّنْ أَنفُسِكُمْ عَزِيزٌ عَلَيْهِ مَا عَنِتُّمْ حَرِيصٌ عَلَيْكُم بِالْمُؤْمِنِينَ رَءُوفٌ رَّحِيمٌ
Ab Yonent dikkal na leen bu bokk ci yéen, seeni coono tiis ci moom, di ku xér ci ngeen jub, di ku am ñeewant ak yërmaande ci jullit ñi.
129فَإِن تَوَلَّوْا فَقُلْ حَسْبِيَ اللَّهُ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ ۖ عَلَيْهِ تَوَكَّلْتُ ۖ وَهُوَ رَبُّ الْعَرْشِ الْعَظِيمِ
Bu ñu dëddoo, neel : “Yàlla doy na ma. Amul jenn yàlla ju dul Moom. Te Moom laay dëgërloo ; te Moom moo di Boroom gàngunaay gu màgg ga (Aras)”.
At-TawbaFihi Alxuraan
129Aaya
MedinanRevelation
127Aaya

Tekki — At-Tawba 127

Simoore At-Tawba Aaya 127 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te su ñu wàccee aw saar ñu daldi xoolante, daldi…

Simoore Aaya 127/129 — Simoore At-Tawba التوبة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore At-Tawba Dégg, Simoore At-Tawba Tekki, Simoore At-Tawba mp3, Simoore At-Tawba pdf. Aaya 125–129. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers