Al-Balad · 12/20
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Balad
وَمَا أَدْرَاكَ مَا الْعَقَبَةُ ۝١٢
Wa maaa adraaka mal`aqabah
📖 Tekkim Wolof
Ana lan moo lay xamal yoon wu tënku wa ?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 10-14 — Simoore Al-Balad

10وَهَدَيْنَاهُ النَّجْدَيْنِ
Nu gindi ko tegtal ko ñaari yoon yi, mbaax, mbon.
11فَلَا اقْتَحَمَ الْعَقَبَةَ
Te, moom moo lànka soobu yoon wu tënku wa (mitti) !
12وَمَا أَدْرَاكَ مَا الْعَقَبَةُ
Ana lan moo lay xamal yoon wu tënku wa ?
13فَكُّ رَقَبَةٍ
Moo di [goréel jaam],
14أَوْ إِطْعَامٌ فِي يَوْمٍ ذِي مَسْغَبَةٍ
mbaa joxe lekk, ci bisub xondooñ, xiif bu tar
Al-BaladFihi Alxuraan
20Aaya
MeccanRevelation
12Aaya

Tekki — Al-Balad 12

Simoore Al-Balad Aaya 12 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ana lan moo lay xamal yoon wu tënku wa ?

Simoore Aaya 12/20 — Simoore Al-Balad البلد (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Balad Dégg, Simoore Al-Balad Tekki, Simoore Al-Balad mp3, Simoore Al-Balad pdf. Aaya 10–14. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers