Al-Balad · 7/20
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Balad
أَيَحْسَبُ أَن لَّمْ يَرَهُ أَحَدٌ ۝٧
Ayahsabu al lam yarahooo ahad
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax dafa defe ne kenn da koo gisul ?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 5-9 — Simoore Al-Balad

5أَيَحْسَبُ أَن لَّن يَقْدِرَ عَلَيْهِ أَحَدٌ
Moo ndax dafa defe ni kenn manul ci moom dara ?
6يَقُولُ أَهْلَكْتُ مَالًا لُّبَدًا
Ma ngay wax naan : “Sànk naa alal ju bari”.
7أَيَحْسَبُ أَن لَّمْ يَرَهُ أَحَدٌ
Moo ndax dafa defe ne kenn da koo gisul ?
8أَلَمْ نَجْعَل لَّهُ عَيْنَيْنِ
Moo ndax defalunu ko ñaari gët,
9وَلِسَانًا وَشَفَتَيْنِ
ak aw làmmiñ ak ñaari tuñ ?
Al-BaladFihi Alxuraan
20Aaya
MeccanRevelation
7Aaya

Tekki — Al-Balad 7

Simoore Al-Balad Aaya 7 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax dafa defe ne kenn da koo gisul ?

Simoore Aaya 7/20 — Simoore Al-Balad البلد (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Balad Dégg, Simoore Al-Balad Tekki, Simoore Al-Balad mp3, Simoore Al-Balad pdf. Aaya 5–9. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers