Al-Balad · 6/20
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Balad
يَقُولُ أَهْلَكْتُ مَالًا لُّبَدًا ۝٦
Yaqoolu ahlaktu maalal lubadaa
📖 Tekkim Wolof
Ma ngay wax naan : “Sànk naa alal ju bari”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 4-8 — Simoore Al-Balad

4لَقَدْ خَلَقْنَا الْإِنسَانَ فِي كَبَدٍ
Noo, bind nit muy jànkonteeki coono.
5أَيَحْسَبُ أَن لَّن يَقْدِرَ عَلَيْهِ أَحَدٌ
Moo ndax dafa defe ni kenn manul ci moom dara ?
6يَقُولُ أَهْلَكْتُ مَالًا لُّبَدًا
Ma ngay wax naan : “Sànk naa alal ju bari”.
7أَيَحْسَبُ أَن لَّمْ يَرَهُ أَحَدٌ
Moo ndax dafa defe ne kenn da koo gisul ?
8أَلَمْ نَجْعَل لَّهُ عَيْنَيْنِ
Moo ndax defalunu ko ñaari gët,
Al-BaladFihi Alxuraan
20Aaya
MeccanRevelation
6Aaya

Tekki — Al-Balad 6

Simoore Al-Balad Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ma ngay wax naan : “Sànk naa alal ju bari”.

Simoore Aaya 6/20 — Simoore Al-Balad البلد (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Balad Dégg, Simoore Al-Balad Tekki, Simoore Al-Balad mp3, Simoore Al-Balad pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers