Al-'Alaq · 1/19
Tekki Waxtaan — Simoore Al-'Alaq
اقْرَأْ بِاسْمِ رَبِّكَ الَّذِي خَلَقَ ۝١
Iqra bismi rab bikal lazee khalaq
📖 Tekkim Wolof
Jàngal, ci sa turu Boroom biy bind,

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-3 — Simoore Al-'Alaq

1اقْرَأْ بِاسْمِ رَبِّكَ الَّذِي خَلَقَ
Jàngal, ci sa turu Boroom biy bind,
2خَلَقَ الْإِنسَانَ مِنْ عَلَقٍ
moo bind nit ci lumbu deret.
3اقْرَأْ وَرَبُّكَ الْأَكْرَمُ
Jàngal ! Sa Boroom mooy ki gëna tedd,
Al-'AlaqFihi Alxuraan
19Aaya
MeccanRevelation
1Aaya

Tekki — Al-'Alaq 1

Simoore Al-'Alaq Aaya 1 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Jàngal, ci sa turu Boroom biy bind,

Simoore Aaya 1/19 — Simoore Al-'Alaq العلق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-'Alaq Dégg, Simoore Al-'Alaq Tekki, Simoore Al-'Alaq mp3, Simoore Al-'Alaq pdf. Aaya 1–3. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers