Hud · 39/123
Tekki Waxtaan — Simoore Hud
فَسَوْفَ تَعْلَمُونَ مَن يَأْتِيهِ عَذَابٌ يُخْزِيهِ وَيَحِلُّ عَلَيْهِ عَذَابٌ مُّقِيمٌ ۝٣٩
Fasawfa ta`lamoona mai yaateehi `azaabuny yaukhzeehi wa yahillu `alaihi `azaabum muqeem
📖 Tekkim Wolof
Xalset ngeen a xam ana kan la mbugalam di dal, toroxal ko, ba noppi mbugalam wàcc ci kawam, di lu sax dàkk ! ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 37-41 — Simoore Hud

37وَاصْنَعِ الْفُلْكَ بِأَعْيُنِنَا وَوَحْيِنَا وَلَا تُخَاطِبْنِي فِي الَّذِينَ ظَلَمُوا ۚ إِنَّهُم مُّغْرَقُونَ
Defaral gaal ci Sunug càmm ak ci Sunu ndigal. Te bul wàqanteeti ak Man ci mbirum ñiy tooñ, ñoom dañu leen di labal”.
38وَيَصْنَعُ الْفُلْكَ وَكُلَّمَا مَرَّ عَلَيْهِ مَلَأٌ مِّن قَوْمِهِ سَخِرُوا مِنْهُ ۚ قَالَ إِن تَسْخَرُوا مِنَّا فَإِنَّا نَسْخَرُ مِنكُمْ كَمَا تَسْخَرُونَ
Muy defar gaal ga. Saa yu ko kenn ci kilifay aw nitam rombee, reetaan ko. Mu ne : “Su ngeen nu reetaanee [tey jii], nun itam [dananu leen reetaan] nu ngeen nu reetaanee woon.
39فَسَوْفَ تَعْلَمُونَ مَن يَأْتِيهِ عَذَابٌ يُخْزِيهِ وَيَحِلُّ عَلَيْهِ عَذَابٌ مُّقِيمٌ
Xalset ngeen a xam ana kan la mbugalam di dal, toroxal ko, ba noppi mbugalam wàcc ci kawam, di lu sax dàkk ! ”
40حَتَّىٰ إِذَا جَاءَ أَمْرُنَا وَفَارَ التَّنُّورُ قُلْنَا احْمِلْ فِيهَا مِن كُلٍّ زَوْجَيْنِ اثْنَيْنِ وَأَهْلَكَ إِلَّا مَن سَبَقَ عَلَيْهِ الْقَوْلُ وَمَنْ آمَنَ ۚ وَمَا آمَنَ مَعَهُ إِلَّا قَلِيلٌ
Ba Sunu ndigal agsee, ndox ma di ballee fu ne, Nu ne : “Defal ci gaal gi, ci xeet wu nekk ñaar [góor ak jigéen] ak sa njaboot - ba mu des ña dogal ba xas dal [ña weddi] - ak ña gëm”. Te lim bu néew rekk a gëmoon.
41۞ وَقَالَ ارْكَبُوا فِيهَا بِسْمِ اللَّهِ مَجْرَاهَا وَمُرْسَاهَا ۚ إِنَّ رَبِّي لَغَفُورٌ رَّحِيمٌ
Mu ne leen : “Yéegleen ci biir tey tudd Yàlla, mooy aw xélam, te it ag teeram. Sama Boroom nag Jéggalaakoon la, Jaglewaakoon la”.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
39Aaya

Tekki — Hud 39

Simoore Hud Aaya 39 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xalset ngeen a xam ana kan la mbugalam di dal,…

Simoore Aaya 39/123 — Simoore Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Hud Dégg, Simoore Hud Tekki, Simoore Hud mp3, Simoore Hud pdf. Aaya 37–41. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers