Hud · 60/123
Tekki Waxtaan — Simoore Hud
وَأُتْبِعُوا فِي هَٰذِهِ الدُّنْيَا لَعْنَةً وَيَوْمَ الْقِيَامَةِ ۗ أَلَا إِنَّ عَادًا كَفَرُوا رَبَّهُمْ ۗ أَلَا بُعْدًا لِّعَادٍ قَوْمِ هُودٍ ۝٦٠
Wa utbi`oo fee haazihid dunyaa la`natanw wa Yawmal Qiyaamah; alaaa inna `Aadan kafaroo Rabbahum; alaa bu`dal li `Aadin qawmin Hood
📖 Tekkim Wolof
Te tofal Nanu leen mbugal ci àddina ak su Bis-pénc baa. Waaw, moo ndax waa Aad nekkuñu woon ñu weddi seen Boroom ? Moo ndax alkaande dalul waa Aad nitu Huud ña ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 58-62 — Simoore Hud

58وَلَمَّا جَاءَ أَمْرُنَا نَجَّيْنَا هُودًا وَالَّذِينَ آمَنُوا مَعَهُ بِرَحْمَةٍ مِّنَّا وَنَجَّيْنَاهُم مِّنْ عَذَابٍ غَلِيظٍ
Ba Sunu dogal agsee, musal Nanu Huud ak ña gëmoon ànd ak moom ci Sunu yërmaande. Te musal leen ci mbugal mu rëy.
59وَتِلْكَ عَادٌ ۖ جَحَدُوا بِآيَاتِ رَبِّهِمْ وَعَصَوْا رُسُلَهُ وَاتَّبَعُوا أَمْرَ كُلِّ جَبَّارٍ عَنِيدٍ
Waa Aad ñoom, dañoo weddi woon kàddug seen Boroom, moyoon ay Yonentam, toppoon képp kuy rëy-rëylu ci dëng.
60وَأُتْبِعُوا فِي هَٰذِهِ الدُّنْيَا لَعْنَةً وَيَوْمَ الْقِيَامَةِ ۗ أَلَا إِنَّ عَادًا كَفَرُوا رَبَّهُمْ ۗ أَلَا بُعْدًا لِّعَادٍ قَوْمِ هُودٍ
Te tofal Nanu leen mbugal ci àddina ak su Bis-pénc baa. Waaw, moo ndax waa Aad nekkuñu woon ñu weddi seen Boroom ? Moo ndax alkaande dalul waa Aad nitu Huud ña ?
61۞ وَإِلَىٰ ثَمُودَ أَخَاهُمْ صَالِحًا ۚ قَالَ يَا قَوْمِ اعْبُدُوا اللَّهَ مَا لَكُم مِّنْ إِلَٰهٍ غَيْرُهُ ۖ هُوَ أَنشَأَكُم مِّنَ الْأَرْضِ وَاسْتَعْمَرَكُمْ فِيهَا فَاسْتَغْفِرُوهُ ثُمَّ تُوبُوا إِلَيْهِ ۚ إِنَّ رَبِّي قَرِيبٌ مُّجِيبٌ
Yónni woon Nanu it ca Samuuda, seen mbokk Saalihu, mu ne : "Yéen samaw nit, jaamuleen Yàlla. Amuleen jeneen yàlla ju dul Moom. Moo leen binde ak suuf, Moo leen ciy dundal. Sàkkuleen njéggalam te tuub jëm ci Moom. Naka sama Boroom, Ku jegeñ la, Kuy wuyyu la [ku Koy] ñaan”.
62قَالُوا يَا صَالِحُ قَدْ كُنتَ فِينَا مَرْجُوًّا قَبْلَ هَٰذَا ۖ أَتَنْهَانَا أَن نَّعْبُدَ مَا يَعْبُدُ آبَاؤُنَا وَإِنَّنَا لَفِي شَكٍّ مِّمَّا تَدْعُونَا إِلَيْهِ مُرِيبٍ
Ñu ne : "Éy yaw Saalihu, nekkoon nga di ku yaakaaru ci nun, lu jiitu lii. Moo ndax danga nuy tere nu jaamu la sunu baay ya daan jaamu ? Nun, am nanu sikki-sàkka gu tar ci li nga nuy woo jëme”.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
60Aaya

Tekki — Hud 60

Simoore Hud Aaya 60 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te tofal Nanu leen mbugal ci àddina ak su Bis-pénc…

Simoore Aaya 60/123 — Simoore Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Hud Dégg, Simoore Hud Tekki, Simoore Hud mp3, Simoore Hud pdf. Aaya 58–62. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers