Hud · 59/123
Tekki Waxtaan — Simoore Hud
وَتِلْكَ عَادٌ ۖ جَحَدُوا بِآيَاتِ رَبِّهِمْ وَعَصَوْا رُسُلَهُ وَاتَّبَعُوا أَمْرَ كُلِّ جَبَّارٍ عَنِيدٍ ۝٥٩
Wa tilka `aad, jahadoo bi Aayaati Rabbihim wa `asaw Rusulahoo wattaba`ooo amra kulli jabbaarin `aneed
📖 Tekkim Wolof
Waa Aad ñoom, dañoo weddi woon kàddug seen Boroom, moyoon ay Yonentam, toppoon képp kuy rëy-rëylu ci dëng.

🎧 Dégg


📜 Aaya 57-61 — Simoore Hud

57فَإِن تَوَلَّوْا فَقَدْ أَبْلَغْتُكُم مَّا أُرْسِلْتُ بِهِ إِلَيْكُمْ ۚ وَيَسْتَخْلِفُ رَبِّي قَوْمًا غَيْرَكُمْ وَلَا تَضُرُّونَهُ شَيْئًا ۚ إِنَّ رَبِّي عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ حَفِيظٌ
Bu ngeen ko dëddoo... man fekk na jottalinaa leen li Nu ma yónni ci yéen. Te dungeen ko wàññi dara, naka sama Boroom, Aji-sàmm lu nekk la”.
58وَلَمَّا جَاءَ أَمْرُنَا نَجَّيْنَا هُودًا وَالَّذِينَ آمَنُوا مَعَهُ بِرَحْمَةٍ مِّنَّا وَنَجَّيْنَاهُم مِّنْ عَذَابٍ غَلِيظٍ
Ba Sunu dogal agsee, musal Nanu Huud ak ña gëmoon ànd ak moom ci Sunu yërmaande. Te musal leen ci mbugal mu rëy.
59وَتِلْكَ عَادٌ ۖ جَحَدُوا بِآيَاتِ رَبِّهِمْ وَعَصَوْا رُسُلَهُ وَاتَّبَعُوا أَمْرَ كُلِّ جَبَّارٍ عَنِيدٍ
Waa Aad ñoom, dañoo weddi woon kàddug seen Boroom, moyoon ay Yonentam, toppoon képp kuy rëy-rëylu ci dëng.
60وَأُتْبِعُوا فِي هَٰذِهِ الدُّنْيَا لَعْنَةً وَيَوْمَ الْقِيَامَةِ ۗ أَلَا إِنَّ عَادًا كَفَرُوا رَبَّهُمْ ۗ أَلَا بُعْدًا لِّعَادٍ قَوْمِ هُودٍ
Te tofal Nanu leen mbugal ci àddina ak su Bis-pénc baa. Waaw, moo ndax waa Aad nekkuñu woon ñu weddi seen Boroom ? Moo ndax alkaande dalul waa Aad nitu Huud ña ?
61۞ وَإِلَىٰ ثَمُودَ أَخَاهُمْ صَالِحًا ۚ قَالَ يَا قَوْمِ اعْبُدُوا اللَّهَ مَا لَكُم مِّنْ إِلَٰهٍ غَيْرُهُ ۖ هُوَ أَنشَأَكُم مِّنَ الْأَرْضِ وَاسْتَعْمَرَكُمْ فِيهَا فَاسْتَغْفِرُوهُ ثُمَّ تُوبُوا إِلَيْهِ ۚ إِنَّ رَبِّي قَرِيبٌ مُّجِيبٌ
Yónni woon Nanu it ca Samuuda, seen mbokk Saalihu, mu ne : "Yéen samaw nit, jaamuleen Yàlla. Amuleen jeneen yàlla ju dul Moom. Moo leen binde ak suuf, Moo leen ciy dundal. Sàkkuleen njéggalam te tuub jëm ci Moom. Naka sama Boroom, Ku jegeñ la, Kuy wuyyu la [ku Koy] ñaan”.
HudFihi Alxuraan
123Aaya
MeccanRevelation
59Aaya

Tekki — Hud 59

Simoore Hud Aaya 59 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waa Aad ñoom, dañoo weddi woon kàddug seen Boroom, moyoon…

Simoore Aaya 59/123 — Simoore Hud هود (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Hud Dégg, Simoore Hud Tekki, Simoore Hud mp3, Simoore Hud pdf. Aaya 57–61. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers