Yusuf · 10/111
Tekki Waxtaan — Simoore Yusuf
قَالَ قَائِلٌ مِّنْهُمْ لَا تَقْتُلُوا يُوسُفَ وَأَلْقُوهُ فِي غَيَابَتِ الْجُبِّ يَلْتَقِطْهُ بَعْضُ السَّيَّارَةِ إِن كُنتُمْ فَاعِلِينَ ۝١٠
Qaalaa qaaa`ilum minhum laa taqtuloo Yoosufa wa alqoohu fee ghayaabatil jubbi yaltaqithu badus sai yaarati in kuntum faa `ileen
📖 Tekkim Wolof
Mu am ca ñoom ku wax ne : “Buleen rey Yuusufa, sànnileen ko ci teen bu lëndëm, kon tukkikat yi danañu ko for su fekkee def ngeen ko”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 8-12 — Simoore Yusuf

8إِذْ قَالُوا لَيُوسُفُ وَأَخُوهُ أَحَبُّ إِلَىٰ أَبِينَا مِنَّا وَنَحْنُ عُصْبَةٌ إِنَّ أَبَانَا لَفِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ
ba ñu waxee ne : “Sunu baay, Yuusufa ak doomu-ndeyam la gën a bëgg ci nun, te nun mbooloo lanu. Sunu baay daal dafa nekk cig réer gu bir.
9اقْتُلُوا يُوسُفَ أَوِ اطْرَحُوهُ أَرْضًا يَخْلُ لَكُمْ وَجْهُ أَبِيكُمْ وَتَكُونُوا مِن بَعْدِهِ قَوْمًا صَالِحِينَ
[Am ku wax ne] reyleen Yuusufa mbaa ngeen sànni ko fenn ci suuf si, kon seen baay dootul xool kenn ku dul yéen, te bu loolu amee dangeen nekk di aw nit ñu feeñ”.
10قَالَ قَائِلٌ مِّنْهُمْ لَا تَقْتُلُوا يُوسُفَ وَأَلْقُوهُ فِي غَيَابَتِ الْجُبِّ يَلْتَقِطْهُ بَعْضُ السَّيَّارَةِ إِن كُنتُمْ فَاعِلِينَ
Mu am ca ñoom ku wax ne : “Buleen rey Yuusufa, sànnileen ko ci teen bu lëndëm, kon tukkikat yi danañu ko for su fekkee def ngeen ko”.
11قَالُوا يَا أَبَانَا مَا لَكَ لَا تَأْمَنَّا عَلَىٰ يُوسُفَ وَإِنَّا لَهُ لَنَاصِحُونَ
Ñu ne : "Yaw sunu baay, ana lan moo tax wóoluwoo nu ci Yuusufa ? Te nun dañu koy laabire doŋŋ.
12أَرْسِلْهُ مَعَنَا غَدًا يَرْتَعْ وَيَلْعَبْ وَإِنَّا لَهُ لَحَافِظُونَ
Bu subaa nga yabal ko mu ànd ak nun muy sàmm jur gi, di fo. Dananu ko wattu”.
YusufFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
10Aaya

Tekki — Yusuf 10

Simoore Yusuf Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu am ca ñoom ku wax ne : “Buleen rey…

Simoore Aaya 10/111 — Simoore Yusuf يوسف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Yusuf Dégg, Simoore Yusuf Tekki, Simoore Yusuf mp3, Simoore Yusuf pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers