Yusuf · 57/111
Tekki Waxtaan — Yusuf
وَلَأَجْرُ الْآخِرَةِ خَيْرٌ لِّلَّذِينَ آمَنُوا وَكَانُوا يَتَّقُونَ ۝٥٧
Wa la ajrul Aakhirati khairul lillazeena aamanoo wa kaanoo yattaqoon
📖 Tekkim Wolof
Te peyug àllaaxira moo gën ci ña gëm, di ña ragal [Yàlla].

🎧 Dégg


📜 Aaya 55-59 — Yusuf

55قَالَ اجْعَلْنِي عَلَىٰ خَزَائِنِ الْأَرْضِ ۖ إِنِّي حَفِيظٌ عَلِيمٌ
Mu ne : “Dénkleen ma alali réew mi : am naa xam-xamu wattu ko”.
56وَكَذَٰلِكَ مَكَّنَّا لِيُوسُفَ فِي الْأَرْضِ يَتَبَوَّأُ مِنْهَا حَيْثُ يَشَاءُ ۚ نُصِيبُ بِرَحْمَتِنَا مَن نَّشَاءُ ۖ وَلَا نُضِيعُ أَجْرَ الْمُحْسِنِينَ
Noonu Lanu darajaale Yuusufa ca réew ma, mu fay wàcc fu ko neex. Dananu jox sunu yërmaande ku Nu neex te Dunu sànk peyug rafetalkat ya.
57وَلَأَجْرُ الْآخِرَةِ خَيْرٌ لِّلَّذِينَ آمَنُوا وَكَانُوا يَتَّقُونَ
Te peyug àllaaxira moo gën ci ña gëm, di ña ragal [Yàlla].
58وَجَاءَ إِخْوَةُ يُوسُفَ فَدَخَلُوا عَلَيْهِ فَعَرَفَهُمْ وَهُمْ لَهُ مُنكِرُونَ
Ay doomi-baayi Yuusufa agsi ca moom [jóge seen réew ma]. Mu xàmmee leen te ñoom fakk nañu ko.
59وَلَمَّا جَهَّزَهُم بِجَهَازِهِمْ قَالَ ائْتُونِي بِأَخٍ لَّكُم مِّنْ أَبِيكُمْ ۚ أَلَا تَرَوْنَ أَنِّي أُوفِي الْكَيْلَ وَأَنَا خَيْرُ الْمُنزِلِينَ
Ba mu solee seen saaku ba noppi, mu ne leen : “Indil-leen ma seen doomi-baay ja des ak seen baay. Moo ndax gisuleen ne nattal na leen lu mat sëkk te it dalal naa leen gën ji daluwaay ?
YusufFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
57Aaya

Tekki — Yusuf 57

Simoore Yusuf Aaya 57 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te peyug àllaaxira moo gën ci ña gëm, di ña…

Simoore Aaya 57/111 — Yusuf يوسف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Yusuf Dégg, Yusuf Tekki, Yusuf mp3, Yusuf pdf. Aaya 55–59. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers