Yusuf · 7/111
Tekki Waxtaan — Yusuf
۞ لَّقَدْ كَانَ فِي يُوسُفَ وَإِخْوَتِهِ آيَاتٌ لِّلسَّائِلِينَ ۝٧
Laqad kaana fee Yoosufa wa ikhwatiheee Aayaatul lissaaa`ileen
📖 Tekkim Wolof
Dëgg-dëgg kéemaan gu réy am na ci diggante Yuusufa ak i doomi-baayam ngir képp kuy gëstu,

🎧 Dégg


📜 Aaya 5-9 — Yusuf

5قَالَ يَا بُنَيَّ لَا تَقْصُصْ رُؤْيَاكَ عَلَىٰ إِخْوَتِكَ فَيَكِيدُوا لَكَ كَيْدًا ۖ إِنَّ الشَّيْطَانَ لِلْإِنسَانِ عَدُوٌّ مُّبِينٌ
Mu ne ko : "Yaw sama doom, bul nettali sa gént gi say doomi-baay, [boo leen ko nettalee], danañu la fexeel am pexe ; ndax Séytaane noonub nit la bu tar ag nooneel.
6وَكَذَٰلِكَ يَجْتَبِيكَ رَبُّكَ وَيُعَلِّمُكَ مِن تَأْوِيلِ الْأَحَادِيثِ وَيُتِمُّ نِعْمَتَهُ عَلَيْكَ وَعَلَىٰ آلِ يَعْقُوبَ كَمَا أَتَمَّهَا عَلَىٰ أَبَوَيْكَ مِن قَبْلُ إِبْرَاهِيمَ وَإِسْحَاقَ ۚ إِنَّ رَبَّكَ عَلِيمٌ حَكِيمٌ
Kem [ni nga génte], sa Boroom dana la tànn te Dana la xamal pirim gént, te Dana matal ci yaw ay xéewalam ak njabootu Yanqooba, ni Mu ko matalee woon bu jëkk ca sa ñaari maam ya, Ibraahiima ak Isaaqa, sa Boroom nag ku xam la, ku xereñ la”.
7۞ لَّقَدْ كَانَ فِي يُوسُفَ وَإِخْوَتِهِ آيَاتٌ لِّلسَّائِلِينَ
Dëgg-dëgg kéemaan gu réy am na ci diggante Yuusufa ak i doomi-baayam ngir képp kuy gëstu,
8إِذْ قَالُوا لَيُوسُفُ وَأَخُوهُ أَحَبُّ إِلَىٰ أَبِينَا مِنَّا وَنَحْنُ عُصْبَةٌ إِنَّ أَبَانَا لَفِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ
ba ñu waxee ne : “Sunu baay, Yuusufa ak doomu-ndeyam la gën a bëgg ci nun, te nun mbooloo lanu. Sunu baay daal dafa nekk cig réer gu bir.
9اقْتُلُوا يُوسُفَ أَوِ اطْرَحُوهُ أَرْضًا يَخْلُ لَكُمْ وَجْهُ أَبِيكُمْ وَتَكُونُوا مِن بَعْدِهِ قَوْمًا صَالِحِينَ
[Am ku wax ne] reyleen Yuusufa mbaa ngeen sànni ko fenn ci suuf si, kon seen baay dootul xool kenn ku dul yéen, te bu loolu amee dangeen nekk di aw nit ñu feeñ”.
YusufFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
7Aaya

Tekki — Yusuf 7

Simoore Yusuf Aaya 7 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Dëgg-dëgg kéemaan gu réy am na ci diggante Yuusufa ak…

Simoore Aaya 7/111 — Yusuf يوسف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Yusuf Dégg, Yusuf Tekki, Yusuf mp3, Yusuf pdf. Aaya 5–9. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers