Yusuf · 74/111
Tekki Waxtaan — Yusuf
قَالُوا فَمَا جَزَاؤُهُ إِن كُنتُمْ كَاذِبِينَ ۝٧٤
Qaaloo famaa jazaaa`u hooo in kuntum kaazibeen
📖 Tekkim Wolof
- Ñu ne: “Luy peyug ku sàcc, bu fekkee dangeen a fen ?”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 72-76 — Yusuf

72قَالُوا نَفْقِدُ صُوَاعَ الْمَلِكِ وَلِمَن جَاءَ بِهِ حِمْلُ بَعِيرٍ وَأَنَا بِهِ زَعِيمٌ
Ñu ne : “Li nu réerle mooy nattukaayu buur bi. Te ku ko feeñal nu jox ko sëfu giléem, maa ko warlul loolu”.
73قَالُوا تَاللَّهِ لَقَدْ عَلِمْتُم مَّا جِئْنَا لِنُفْسِدَ فِي الْأَرْضِ وَمَا كُنَّا سَارِقِينَ
Ñu ne : “Giñ nanu ci Yàlla, te xam ngeen ne dikkunu fii ci suuf si ngir yàq te it dunu ay sàcckat”.
74قَالُوا فَمَا جَزَاؤُهُ إِن كُنتُمْ كَاذِبِينَ
- Ñu ne: “Luy peyug ku sàcc, bu fekkee dangeen a fen ?”.
75قَالُوا جَزَاؤُهُ مَن وُجِدَ فِي رَحْلِهِ فَهُوَ جَزَاؤُهُ ۚ كَذَٰلِكَ نَجْزِي الظَّالِمِينَ
Ñu ne : “Ag peyam moom ka ñu fekk [nattukaay ba] ci sëfam mooy : ag peyam moom ci boppam [mu nekk jaam]. Noonu Lanu feye tooñkat ya”.
76فَبَدَأَ بِأَوْعِيَتِهِمْ قَبْلَ وِعَاءِ أَخِيهِ ثُمَّ اسْتَخْرَجَهَا مِن وِعَاءِ أَخِيهِ ۚ كَذَٰلِكَ كِدْنَا لِيُوسُفَ ۖ مَا كَانَ لِيَأْخُذَ أَخَاهُ فِي دِينِ الْمَلِكِ إِلَّا أَن يَشَاءَ اللَّهُ ۚ نَرْفَعُ دَرَجَاتٍ مَّن نَّشَاءُ ۗ وَفَوْقَ كُلِّ ذِي عِلْمٍ عَلِيمٌ
Mu jëkke ca ndabi doomi-baay ya, di seet, mujje ndabul doomu-ndey ja ; génne ca nattukaay ba. Noonu Lanu joxe pexe Yuusufa. Pexe mu ko tax a téye doomu-ndeyam ja ci lu dëppook yoonu buur ba, [mënu ko woon a def] lu dul lu soob Yàlla. Dananu yékkati darajay ku Nu soob. Te boroom xam-xam bu nekk, am na ku ko ëpp xam-xam.
YusufFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
74Aaya

Tekki — Yusuf 74

Simoore Yusuf Aaya 74 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : - Ñu ne: “Luy peyug ku sàcc, bu fekkee dangeen…

Simoore Aaya 74/111 — Yusuf يوسف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Yusuf Dégg, Yusuf Tekki, Yusuf mp3, Yusuf pdf. Aaya 72–76. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, August 19, 2026

Don't forget us in your sincere prayers