Yusuf · 73/111
Tekki Waxtaan — Yusuf
قَالُوا تَاللَّهِ لَقَدْ عَلِمْتُم مَّا جِئْنَا لِنُفْسِدَ فِي الْأَرْضِ وَمَا كُنَّا سَارِقِينَ ۝٧٣
Qaaloo tallaahi laqad `alimtum maa ji`na linufsida fil ardi wa maa kunnaa saariqeen
📖 Tekkim Wolof
Ñu ne : “Giñ nanu ci Yàlla, te xam ngeen ne dikkunu fii ci suuf si ngir yàq te it dunu ay sàcckat”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 71-75 — Yusuf

71قَالُوا وَأَقْبَلُوا عَلَيْهِم مَّاذَا تَفْقِدُونَ
Ñoom it ñu wëlbatiku ca moom ne leen : “Lan ngeen réerle ? ”
72قَالُوا نَفْقِدُ صُوَاعَ الْمَلِكِ وَلِمَن جَاءَ بِهِ حِمْلُ بَعِيرٍ وَأَنَا بِهِ زَعِيمٌ
Ñu ne : “Li nu réerle mooy nattukaayu buur bi. Te ku ko feeñal nu jox ko sëfu giléem, maa ko warlul loolu”.
73قَالُوا تَاللَّهِ لَقَدْ عَلِمْتُم مَّا جِئْنَا لِنُفْسِدَ فِي الْأَرْضِ وَمَا كُنَّا سَارِقِينَ
Ñu ne : “Giñ nanu ci Yàlla, te xam ngeen ne dikkunu fii ci suuf si ngir yàq te it dunu ay sàcckat”.
74قَالُوا فَمَا جَزَاؤُهُ إِن كُنتُمْ كَاذِبِينَ
- Ñu ne: “Luy peyug ku sàcc, bu fekkee dangeen a fen ?”.
75قَالُوا جَزَاؤُهُ مَن وُجِدَ فِي رَحْلِهِ فَهُوَ جَزَاؤُهُ ۚ كَذَٰلِكَ نَجْزِي الظَّالِمِينَ
Ñu ne : “Ag peyam moom ka ñu fekk [nattukaay ba] ci sëfam mooy : ag peyam moom ci boppam [mu nekk jaam]. Noonu Lanu feye tooñkat ya”.
YusufFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
73Aaya

Tekki — Yusuf 73

Simoore Yusuf Aaya 73 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu ne : “Giñ nanu ci Yàlla, te xam ngeen…

Simoore Aaya 73/111 — Yusuf يوسف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Yusuf Dégg, Yusuf Tekki, Yusuf mp3, Yusuf pdf. Aaya 71–75. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers