Ar-Ra'd · 27/43
Tekki Waxtaan — Ar-Ra'd
وَيَقُولُ الَّذِينَ كَفَرُوا لَوْلَا أُنزِلَ عَلَيْهِ آيَةٌ مِّن رَّبِّهِ ۗ قُلْ إِنَّ اللَّهَ يُضِلُّ مَن يَشَاءُ وَيَهْدِي إِلَيْهِ مَنْ أَنَابَ ۝٢٧
Wa yaqoolul lazeena kafaroo law laaa unzila `alaihi Aayatum mir Rabbih; qul innal laaha yudillu mai yashaa`u wa yahdeee ilaihi man anaab
📖 Tekkim Wolof
Te ñoom ña weddi dañuy wax naan : “Lu tee woon ñu wàcce ci moom kéemaan gu jóge ca Boroomam ? ”. Waxal ne : “Yàlla dana bàyyi cig réer ku ko soob, te it Dana gindi jëme ci Moom ku dellu [jëm ci topp Yàlla],

🎧 Dégg


📜 Aaya 25-29 — Ar-Ra'd

25وَالَّذِينَ يَنقُضُونَ عَهْدَ اللَّهِ مِن بَعْدِ مِيثَاقِهِ وَيَقْطَعُونَ مَا أَمَرَ اللَّهُ بِهِ أَن يُوصَلَ وَيُفْسِدُونَ فِي الْأَرْضِ ۙ أُولَٰئِكَ لَهُمُ اللَّعْنَةُ وَلَهُمْ سُوءُ الدَّارِ
[Waaye] ñiy firi kóllareg Yàlla ginnaaw ba mu fasoo, te muy dog la Mu santaane ñu jokk ko [mooy ag mbokk], di yàq ci kaw suuf si, ñooña am rëbb dal na ci seen kaw [sori yërmaandey Yàlla], te it am nañu kër gu bon ga.
26اللَّهُ يَبْسُطُ الرِّزْقَ لِمَن يَشَاءُ وَيَقْدِرُ ۚ وَفَرِحُوا بِالْحَيَاةِ الدُّنْيَا وَمَا الْحَيَاةُ الدُّنْيَا فِي الْآخِرَةِ إِلَّا مَتَاعٌ
Yàlla dana yaatal wërsëg ci ku ko soob, Dana ko xatal it. Te ñoom dundu àdduna neex na leen, te dundu àdduna soo ko méngaleek gu àllaaxira, du nekk lu dul xéewal gu ñàkk solo.
27وَيَقُولُ الَّذِينَ كَفَرُوا لَوْلَا أُنزِلَ عَلَيْهِ آيَةٌ مِّن رَّبِّهِ ۗ قُلْ إِنَّ اللَّهَ يُضِلُّ مَن يَشَاءُ وَيَهْدِي إِلَيْهِ مَنْ أَنَابَ
Te ñoom ña weddi dañuy wax naan : “Lu tee woon ñu wàcce ci moom kéemaan gu jóge ca Boroomam ? ”. Waxal ne : “Yàlla dana bàyyi cig réer ku ko soob, te it Dana gindi jëme ci Moom ku dellu [jëm ci topp Yàlla],
28الَّذِينَ آمَنُوا وَتَطْمَئِنُّ قُلُوبُهُم بِذِكْرِ اللَّهِ ۗ أَلَا بِذِكْرِ اللَّهِ تَطْمَئِنُّ الْقُلُوبُ
ñooy ña gëm te seen xol dal ci tudd Yàlla”. Te nag ca dëgg-dëgg, tuddu Yàlla mooy dalal xel yi [xol yi] ?
29الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ طُوبَىٰ لَهُمْ وَحُسْنُ مَآبٍ
Ña gëm tey jëf jëf yu sell yi, am nañu ag texe ak delluwaay bu rafet.
Ar-Ra'dFihi Alxuraan
43Aaya
MedinanRevelation
27Aaya

Tekki — Ar-Ra'd 27

Simoore Ar-Ra'd Aaya 27 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te ñoom ña weddi dañuy wax naan : “Lu tee…

Simoore Aaya 27/43 — Ar-Ra'd الرعد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ar-Ra'd Dégg, Ar-Ra'd Tekki, Ar-Ra'd mp3, Ar-Ra'd pdf. Aaya 25–29. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers