Ar-Ra'd · 42/43
Tekki Waxtaan — Ar-Ra'd
وَقَدْ مَكَرَ الَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ فَلِلَّهِ الْمَكْرُ جَمِيعًا ۖ يَعْلَمُ مَا تَكْسِبُ كُلُّ نَفْسٍ ۗ وَسَيَعْلَمُ الْكُفَّارُ لِمَنْ عُقْبَى الدَّارِ ٤٢
Transliteration
Wa qad makaral lazeena min qablihim falillaahil makru jamee`aa; ya`lamu maa taksibu kullu nafs; wa sa ya`lamul kuffaaru liman `uqbad daar
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ña leen jiitu woon defoon nañu ay pexe ; te Yàllaa moom gépp fànnu pexe. Xam na lu bépp bakkan fàggu. Te yéefar yi danañu mës a xam kan moo moom kër gu mujj ga.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 40-43 — Ar-Ra'd
40وَإِن مَّا نُرِيَنَّكَ بَعْضَ الَّذِي نَعِدُهُمْ أَوْ نَتَوَفَّيَنَّكَ فَإِنَّمَا عَلَيْكَ الْبَلَاغُ وَعَلَيْنَا الْحِسَابُ
Ndegam won Nanu la lenn ci li Nu leen dig, walla Nu rey la [lu mu ca mën di doon], yaw li la war moo di jotal, waaye Nun noo warloo natt [jëf ya].
41أَوَلَمْ يَرَوْا أَنَّا نَأْتِي الْأَرْضَ نَنقُصُهَا مِنْ أَطْرَافِهَا ۚ وَاللَّهُ يَحْكُمُ لَا مُعَقِّبَ لِحُكْمِهِ ۚ وَهُوَ سَرِيعُ الْحِسَابِ
Xanaa dañoo gisul ne Nun noo ngi wàññi suuf si ci ay catam ? Yàlla mooy àtte, Dananu delloob àtteem, te Moom ku gaaw la cib nattam.
42وَقَدْ مَكَرَ الَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ فَلِلَّهِ الْمَكْرُ جَمِيعًا ۖ يَعْلَمُ مَا تَكْسِبُ كُلُّ نَفْسٍ ۗ وَسَيَعْلَمُ الْكُفَّارُ لِمَنْ عُقْبَى الدَّارِ
Ña leen jiitu woon defoon nañu ay pexe ; te Yàllaa moom gépp fànnu pexe. Xam na lu bépp bakkan fàggu. Te yéefar yi danañu mës a xam kan moo moom kër gu mujj ga.
43وَيَقُولُ الَّذِينَ كَفَرُوا لَسْتَ مُرْسَلًا ۚ قُلْ كَفَىٰ بِاللَّهِ شَهِيدًا بَيْنِي وَبَيْنَكُمْ وَمَنْ عِندَهُ عِلْمُ الْكِتَابِ
Ña weddi dañuy wax naan : “Doo ab Yonent”. Neel : “Yàlla doy na seede ci sama diggante ak yéen, ak képp ku am xam-xamu Téere ba”.
Ar-Ra'dFihi Alxuraan
43Aaya
MedinanRevelation
42Aaya
Tekki — Ar-Ra'd 42
Simoore Ar-Ra'd Aaya 42 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña leen jiitu woon defoon nañu ay pexe ; te…Simoore Aaya 42/43 — Ar-Ra'd الرعد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ar-Ra'd Dégg, Ar-Ra'd Tekki, Ar-Ra'd mp3, Ar-Ra'd pdf. Aaya 40–43. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








