Ar-Ra'd · 43/43
Tekki Waxtaan — Simoore Ar-Ra'd
وَيَقُولُ الَّذِينَ كَفَرُوا لَسْتَ مُرْسَلًا ۚ قُلْ كَفَىٰ بِاللَّهِ شَهِيدًا بَيْنِي وَبَيْنَكُمْ وَمَنْ عِندَهُ عِلْمُ الْكِتَابِ ۝٤٣
Wa yaqoolul lazeena kafaroo lasta mursalaa; qul kafaa billaahi shaheedam bainee wa bainakum wa man `indahoo `ilmul Kitaab
📖 Tekkim Wolof
Ña weddi dañuy wax naan : “Doo ab Yonent”. Neel : “Yàlla doy na seede ci sama diggante ak yéen, ak képp ku am xam-xamu Téere ba”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 41-43 — Simoore Ar-Ra'd

41أَوَلَمْ يَرَوْا أَنَّا نَأْتِي الْأَرْضَ نَنقُصُهَا مِنْ أَطْرَافِهَا ۚ وَاللَّهُ يَحْكُمُ لَا مُعَقِّبَ لِحُكْمِهِ ۚ وَهُوَ سَرِيعُ الْحِسَابِ
Xanaa dañoo gisul ne Nun noo ngi wàññi suuf si ci ay catam ? Yàlla mooy àtte, Dananu delloob àtteem, te Moom ku gaaw la cib nattam.
42وَقَدْ مَكَرَ الَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ فَلِلَّهِ الْمَكْرُ جَمِيعًا ۖ يَعْلَمُ مَا تَكْسِبُ كُلُّ نَفْسٍ ۗ وَسَيَعْلَمُ الْكُفَّارُ لِمَنْ عُقْبَى الدَّارِ
Ña leen jiitu woon defoon nañu ay pexe ; te Yàllaa moom gépp fànnu pexe. Xam na lu bépp bakkan fàggu. Te yéefar yi danañu mës a xam kan moo moom kër gu mujj ga.
43وَيَقُولُ الَّذِينَ كَفَرُوا لَسْتَ مُرْسَلًا ۚ قُلْ كَفَىٰ بِاللَّهِ شَهِيدًا بَيْنِي وَبَيْنَكُمْ وَمَنْ عِندَهُ عِلْمُ الْكِتَابِ
Ña weddi dañuy wax naan : “Doo ab Yonent”. Neel : “Yàlla doy na seede ci sama diggante ak yéen, ak képp ku am xam-xamu Téere ba”.
Ar-Ra'dFihi Alxuraan
43Aaya
MedinanRevelation
43Aaya

Tekki — Ar-Ra'd 43

Simoore Ar-Ra'd Aaya 43 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña weddi dañuy wax naan : “Doo ab Yonent”. Neel…

Simoore Aaya 43/43 — Simoore Ar-Ra'd الرعد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ar-Ra'd Dégg, Simoore Ar-Ra'd Tekki, Simoore Ar-Ra'd mp3, Simoore Ar-Ra'd pdf. Aaya 41–43. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers