Ibrahima · 17/52
Tekki Waxtaan — Ibrahima
يَتَجَرَّعُهُ وَلَا يَكَادُ يُسِيغُهُ وَيَأْتِيهِ الْمَوْتُ مِن كُلِّ مَكَانٍ وَمَا هُوَ بِمَيِّتٍ ۖ وَمِن وَرَائِهِ عَذَابٌ غَلِيظٌ ۝١٧
Yatajarra`uhoo wa laa yakaadu yuseeghuhoo wa yaateehil mawtu min kulli makaaninw wa maa huwa bimaiyitinw wa minw waraaa`ihee `azaabun ghaleez
📖 Tekkim Wolof
dana ko guux. Waaye du ko xaw a mën a wann. Dee di ko dikkale wet gu nekk, te du dee ; te it mbugal mu tar dana ca topp.
🎧 Dégg

📜 Aaya 15-19 — Ibrahima

15وَاسْتَفْتَحُوا وَخَابَ كُلُّ جَبَّارٍ عَنِيدٍ
Ñu sàkku ndimbal [ñoom Yonent ya]. Képp ku doon rëy-rëylu te jeng daldi yàqule.
16مِّن وَرَائِهِ جَهَنَّمُ وَيُسْقَىٰ مِن مَّاءٍ صَدِيدٍ
Te Safaraa nga xaar ca ginnaaw te dees na ko nàndal ndox mu bon te tàng jér
17يَتَجَرَّعُهُ وَلَا يَكَادُ يُسِيغُهُ وَيَأْتِيهِ الْمَوْتُ مِن كُلِّ مَكَانٍ وَمَا هُوَ بِمَيِّتٍ ۖ وَمِن وَرَائِهِ عَذَابٌ غَلِيظٌ
dana ko guux. Waaye du ko xaw a mën a wann. Dee di ko dikkale wet gu nekk, te du dee ; te it mbugal mu tar dana ca topp.
18مَّثَلُ الَّذِينَ كَفَرُوا بِرَبِّهِمْ ۖ أَعْمَالُهُمْ كَرَمَادٍ اشْتَدَّتْ بِهِ الرِّيحُ فِي يَوْمٍ عَاصِفٍ ۖ لَّا يَقْدِرُونَ مِمَّا كَسَبُوا عَلَىٰ شَيْءٍ ۚ ذَٰلِكَ هُوَ الضَّلَالُ الْبَعِيدُ
Ña weddi seen Boroom, seeni jëf dafa mel cig niróole ni ab dóom bu ngelaw ëf ci bisu mbóoya mu ràddi. Duñu mën a jariñoo dara ca la ñu fàggu woon. Loolu moo di réer gu sori dëgg.
19أَلَمْ تَرَ أَنَّ اللَّهَ خَلَقَ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ بِالْحَقِّ ۚ إِن يَشَأْ يُذْهِبْكُمْ وَيَأْتِ بِخَلْقٍ جَدِيدٍ
Ndax dañoo gisul ne Yàllaa bind asamaan yi ak suuf si ci dëgg ? Bu ko neexoon Mu jële leen fi, indi fi ay mbindéef yu bees,
IbrahimaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
17Aaya

Tekki — Ibrahima 17

Simoore Ibrahima Aaya 17 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : dana ko guux. Waaye du ko xaw a mën a…

Simoore Aaya 17/52 — Ibrahima إبراهيم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ibrahima Dégg, Ibrahima Tekki, Ibrahima mp3, Ibrahima pdf. Aaya 15–19. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers