Ibrahima · 2/52
Tekki Waxtaan — Ibrahima
اللَّهِ الَّذِي لَهُ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ ۗ وَوَيْلٌ لِّلْكَافِرِينَ مِنْ عَذَابٍ شَدِيدٍ ۝٢
Allaahil lazee lahoo maa fis samaawaati wa maa fill ard; wa wailul lilkaafireena min `azaabin shadeed
📖 Tekkim Wolof
[ci yoonu] Yàlla mi nga xam ne Moo moom li nekk ci asamaan yi ak suuf si. Te alkaande ñeel na yéefar yi ci mbugal mu tar.
🎧 Dégg

📜 Aaya 1-4 — Ibrahima

1الر ۚ كِتَابٌ أَنزَلْنَاهُ إِلَيْكَ لِتُخْرِجَ النَّاسَ مِنَ الظُّلُمَاتِ إِلَى النُّورِ بِإِذْنِ رَبِّهِمْ إِلَىٰ صِرَاطِ الْعَزِيزِ الْحَمِيدِ
Alif, Laam, Raa. Ab téere la bu Nu wàcce ci yaw ngir nga génne nit ñi cig lëndëm [kéefar], jëme leen cig leer [gëm Yàlla], ci ndigalu seen Boroom jëme leen ci yoonu Boroom kàttan gi, Ki yeyoo gépp cant,
2اللَّهِ الَّذِي لَهُ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ ۗ وَوَيْلٌ لِّلْكَافِرِينَ مِنْ عَذَابٍ شَدِيدٍ
[ci yoonu] Yàlla mi nga xam ne Moo moom li nekk ci asamaan yi ak suuf si. Te alkaande ñeel na yéefar yi ci mbugal mu tar.
3الَّذِينَ يَسْتَحِبُّونَ الْحَيَاةَ الدُّنْيَا عَلَى الْآخِرَةِ وَيَصُدُّونَ عَن سَبِيلِ اللَّهِ وَيَبْغُونَهَا عِوَجًا ۚ أُولَٰئِكَ فِي ضَلَالٍ بَعِيدٍ
Ña nga xam ne dañoo tànn dundug àdduna [mu gënal leen] gu àllaaxira, te ñuy wëlbati ña jëm ci yoonu Yàlla, di ko sàkkal ay gàkk, ñooña ñanga ca ag réer gu sori dëgg.
4وَمَا أَرْسَلْنَا مِن رَّسُولٍ إِلَّا بِلِسَانِ قَوْمِهِ لِيُبَيِّنَ لَهُمْ ۖ فَيُضِلُّ اللَّهُ مَن يَشَاءُ وَيَهْدِي مَن يَشَاءُ ۚ وَهُوَ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ
Dunu yónni ab Yonent lu dul ci làkku nitam ña [lay waxe] ngir mu leeralal leen [la ñu ko yónni]. Te Yàlla mooy bàyyi cig réer ku ko soob, Dana gindi itam ku ko soob. Ndax Moom moo di boroom kàttan gi tey Aji-xereñ [ciy àtteem].
IbrahimaFihi Alxuraan
52Aaya
MeccanRevelation
2Aaya

Tekki — Ibrahima 2

Simoore Ibrahima Aaya 2 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [ci yoonu] Yàlla mi nga xam ne Moo moom li…

Simoore Aaya 2/52 — Ibrahima إبراهيم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ibrahima Dégg, Ibrahima Tekki, Ibrahima mp3, Ibrahima pdf. Aaya 1–4. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers