An-Nahl · 22/128
Tekki Waxtaan — An-Nahl
إِلَٰهُكُمْ إِلَٰهٌ وَاحِدٌ ۚ فَالَّذِينَ لَا يُؤْمِنُونَ بِالْآخِرَةِ قُلُوبُهُم مُّنكِرَةٌ وَهُم مُّسْتَكْبِرُونَ ۝٢٢
Illahukum Ilaahunw Waahid; fallazeena laa yu`minoona bil Aakhirati quloobuhum munkiratunw wa hum mustakbiroon
📖 Tekkim Wolof
Seen Yàlla jenn rekk la. Tax na ña gëmul àllaaxira, seeni xol a dàq a weddi te ñoom dañuy rëy-rëylu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 20-24 — An-Nahl

20وَالَّذِينَ يَدْعُونَ مِن دُونِ اللَّهِ لَا يَخْلُقُونَ شَيْئًا وَهُمْ يُخْلَقُونَ
Te ya ñuy jaamu bàyyi Yàlla binduñu dara, te sax dañu leen bind far.
21أَمْوَاتٌ غَيْرُ أَحْيَاءٍ ۖ وَمَا يَشْعُرُونَ أَيَّانَ يُبْعَثُونَ
Yu dee lañu, nekkuñu luy dundu, te xamuñu kañ lañu leen di dekkal.
22إِلَٰهُكُمْ إِلَٰهٌ وَاحِدٌ ۚ فَالَّذِينَ لَا يُؤْمِنُونَ بِالْآخِرَةِ قُلُوبُهُم مُّنكِرَةٌ وَهُم مُّسْتَكْبِرُونَ
Seen Yàlla jenn rekk la. Tax na ña gëmul àllaaxira, seeni xol a dàq a weddi te ñoom dañuy rëy-rëylu.
23لَا جَرَمَ أَنَّ اللَّهَ يَعْلَمُ مَا يُسِرُّونَ وَمَا يُعْلِنُونَ ۚ إِنَّهُ لَا يُحِبُّ الْمُسْتَكْبِرِينَ
Ca dëgg-dëgg, Yàlla xam na la ñuy nëbb ak la ñuy feeñal. Te Yàlla nag soppul ñiy rëy- rëylu.
24وَإِذَا قِيلَ لَهُم مَّاذَا أَنزَلَ رَبُّكُمْ ۙ قَالُوا أَسَاطِيرُ الْأَوَّلِينَ
Bu ñu nee leen : “Lan la seen Boroom wàcce ? ”. Ñu ne : “Xanaa ay léeb yu jóge ca mag ñu njëgg ña ! ”
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
22Aaya

Tekki — An-Nahl 22

Simoore An-Nahl Aaya 22 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Seen Yàlla jenn rekk la. Tax na ña gëmul àllaaxira,…

Simoore Aaya 22/128 — An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nahl Dégg, An-Nahl Tekki, An-Nahl mp3, An-Nahl pdf. Aaya 20–24. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers