An-Nahl · 23/128
Tekki Waxtaan — An-Nahl
لَا جَرَمَ أَنَّ اللَّهَ يَعْلَمُ مَا يُسِرُّونَ وَمَا يُعْلِنُونَ ۚ إِنَّهُ لَا يُحِبُّ الْمُسْتَكْبِرِينَ ٢٣
Transliteration
Laa jarama annal laaha ya`lamu maa yusirrona wa ma yu`linoon; innahoo laa yuhibbul mustakbireen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ca dëgg-dëgg, Yàlla xam na la ñuy nëbb ak la ñuy feeñal. Te Yàlla nag soppul ñiy rëy- rëylu.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 21-25 — An-Nahl
21أَمْوَاتٌ غَيْرُ أَحْيَاءٍ ۖ وَمَا يَشْعُرُونَ أَيَّانَ يُبْعَثُونَ
Yu dee lañu, nekkuñu luy dundu, te xamuñu kañ lañu leen di dekkal.
22إِلَٰهُكُمْ إِلَٰهٌ وَاحِدٌ ۚ فَالَّذِينَ لَا يُؤْمِنُونَ بِالْآخِرَةِ قُلُوبُهُم مُّنكِرَةٌ وَهُم مُّسْتَكْبِرُونَ
Seen Yàlla jenn rekk la. Tax na ña gëmul àllaaxira, seeni xol a dàq a weddi te ñoom dañuy rëy-rëylu.
23لَا جَرَمَ أَنَّ اللَّهَ يَعْلَمُ مَا يُسِرُّونَ وَمَا يُعْلِنُونَ ۚ إِنَّهُ لَا يُحِبُّ الْمُسْتَكْبِرِينَ
Ca dëgg-dëgg, Yàlla xam na la ñuy nëbb ak la ñuy feeñal. Te Yàlla nag soppul ñiy rëy- rëylu.
24وَإِذَا قِيلَ لَهُم مَّاذَا أَنزَلَ رَبُّكُمْ ۙ قَالُوا أَسَاطِيرُ الْأَوَّلِينَ
Bu ñu nee leen : “Lan la seen Boroom wàcce ? ”. Ñu ne : “Xanaa ay léeb yu jóge ca mag ñu njëgg ña ! ”
25لِيَحْمِلُوا أَوْزَارَهُمْ كَامِلَةً يَوْمَ الْقِيَامَةِ ۙ وَمِنْ أَوْزَارِ الَّذِينَ يُضِلُّونَهُم بِغَيْرِ عِلْمٍ ۗ أَلَا سَاءَ مَا يَزِرُونَ
Danañu yenu seeni bàkkaar ba mu mat sëkk, Bis-pénc ba, ak lenn ca bàkkaari ña ñu réeral, ci loo xam ne amuñu ca woon xam-xam ; cëy ndaw yen bu bon !
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
23Aaya
Tekki — An-Nahl 23
Simoore An-Nahl Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ca dëgg-dëgg, Yàlla xam na la ñuy nëbb ak la…Simoore Aaya 23/128 — An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nahl Dégg, An-Nahl Tekki, An-Nahl mp3, An-Nahl pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








