An-Nahl · 48/128
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nahl
أَوَلَمْ يَرَوْا إِلَىٰ مَا خَلَقَ اللَّهُ مِن شَيْءٍ يَتَفَيَّأُ ظِلَالُهُ عَنِ الْيَمِينِ وَالشَّمَائِلِ سُجَّدًا لِّلَّهِ وَهُمْ دَاخِرُونَ ۝٤٨
Awa lam yaraw ilaa maa khalaqal laahu min shai`iny-yatafaiya`u zilaaluhoo `anil yameeni washshamaaa` ili sujjadal lillaahi wa hum daakhiroon
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax seetlu nañu lenn lu Yàlla bind, loolu keram danay jeng jëm càmmoñ, ak a jengiy jëm ndeyjoor ngir sujjóotal Yàlla ak a toroxlu ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 46-50 — Simoore An-Nahl

46أَوْ يَأْخُذَهُمْ فِي تَقَلُّبِهِمْ فَمَا هُم بِمُعْجِزِينَ
Mbaa mu sadd leen ci seeni tukki ngir ñoom mënuñoo raw [Yàlla].
47أَوْ يَأْخُذَهُمْ عَلَىٰ تَخَوُّفٍ فَإِنَّ رَبَّكُمْ لَرَءُوفٌ رَّحِيمٌ
Mbaa Mu sadd leen cim tiit ? Te sax seen Boroom Aji-ñeewant la, Jaglewaakoon la.
48أَوَلَمْ يَرَوْا إِلَىٰ مَا خَلَقَ اللَّهُ مِن شَيْءٍ يَتَفَيَّأُ ظِلَالُهُ عَنِ الْيَمِينِ وَالشَّمَائِلِ سُجَّدًا لِّلَّهِ وَهُمْ دَاخِرُونَ
Moo ndax seetlu nañu lenn lu Yàlla bind, loolu keram danay jeng jëm càmmoñ, ak a jengiy jëm ndeyjoor ngir sujjóotal Yàlla ak a toroxlu ?
49وَلِلَّهِ يَسْجُدُ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ مِن دَابَّةٍ وَالْمَلَائِكَةُ وَهُمْ لَا يَسْتَكْبِرُونَ
Lépp lu nekk ci asamaan yi ak suuf si tey dukkat, ak Malaaka yi, dañuy sujjóotal Yàlla te duñu rëy-rëylu.
50يَخَافُونَ رَبَّهُم مِّن فَوْقِهِمْ وَيَفْعَلُونَ مَا يُؤْمَرُونَ ۩
Dañuy ragal seen Boroom bi leen tiim, te dañuy def la ñu leen digal.
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
48Aaya

Tekki — An-Nahl 48

Simoore An-Nahl Aaya 48 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax seetlu nañu lenn lu Yàlla bind, loolu keram…

Simoore Aaya 48/128 — Simoore An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nahl Dégg, Simoore An-Nahl Tekki, Simoore An-Nahl mp3, Simoore An-Nahl pdf. Aaya 46–50. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers