An-Nahl · 47/128
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nahl
أَوْ يَأْخُذَهُمْ عَلَىٰ تَخَوُّفٍ فَإِنَّ رَبَّكُمْ لَرَءُوفٌ رَّحِيمٌ ۝٤٧
Aw yaakhuzahum `alaa takhawwuf; fa inna Rabbakum la Ra`oofur Raheem
📖 Tekkim Wolof
Mbaa Mu sadd leen cim tiit ? Te sax seen Boroom Aji-ñeewant la, Jaglewaakoon la.

🎧 Dégg


📜 Aaya 45-49 — Simoore An-Nahl

45أَفَأَمِنَ الَّذِينَ مَكَرُوا السَّيِّئَاتِ أَن يَخْسِفَ اللَّهُ بِهِمُ الْأَرْضَ أَوْ يَأْتِيَهُمُ الْعَذَابُ مِنْ حَيْثُ لَا يَشْعُرُونَ
Ndax am na ci ñuy fexe lu bon, ñu wóolu ne Yàlla du këpp suuf ci sunu kaw, mbaa Mu sadd leen mbugal mu ñu foogul ?
46أَوْ يَأْخُذَهُمْ فِي تَقَلُّبِهِمْ فَمَا هُم بِمُعْجِزِينَ
Mbaa mu sadd leen ci seeni tukki ngir ñoom mënuñoo raw [Yàlla].
47أَوْ يَأْخُذَهُمْ عَلَىٰ تَخَوُّفٍ فَإِنَّ رَبَّكُمْ لَرَءُوفٌ رَّحِيمٌ
Mbaa Mu sadd leen cim tiit ? Te sax seen Boroom Aji-ñeewant la, Jaglewaakoon la.
48أَوَلَمْ يَرَوْا إِلَىٰ مَا خَلَقَ اللَّهُ مِن شَيْءٍ يَتَفَيَّأُ ظِلَالُهُ عَنِ الْيَمِينِ وَالشَّمَائِلِ سُجَّدًا لِّلَّهِ وَهُمْ دَاخِرُونَ
Moo ndax seetlu nañu lenn lu Yàlla bind, loolu keram danay jeng jëm càmmoñ, ak a jengiy jëm ndeyjoor ngir sujjóotal Yàlla ak a toroxlu ?
49وَلِلَّهِ يَسْجُدُ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَمَا فِي الْأَرْضِ مِن دَابَّةٍ وَالْمَلَائِكَةُ وَهُمْ لَا يَسْتَكْبِرُونَ
Lépp lu nekk ci asamaan yi ak suuf si tey dukkat, ak Malaaka yi, dañuy sujjóotal Yàlla te duñu rëy-rëylu.
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
47Aaya

Tekki — An-Nahl 47

Simoore An-Nahl Aaya 47 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mbaa Mu sadd leen cim tiit ? Te sax seen…

Simoore Aaya 47/128 — Simoore An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nahl Dégg, Simoore An-Nahl Tekki, Simoore An-Nahl mp3, Simoore An-Nahl pdf. Aaya 45–49. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers