An-Nahl · 53/128
Tekki Waxtaan — An-Nahl
وَمَا بِكُم مِّن نِّعْمَةٍ فَمِنَ اللَّهِ ۖ ثُمَّ إِذَا مَسَّكُمُ الضُّرُّ فَإِلَيْهِ تَجْأَرُونَ ۝٥٣
Wa maa bikum minni`matin faminal laahi summa izaa massakumud durru fa ilaihi taj`aroon
📖 Tekkim Wolof
Li ngeen am ciw yiw mi ngi jóge ca Yàlla. Te bu leen lu metti dalee, Moom ngeen di ñaan ndimbal.
🎧 Dégg

📜 Aaya 51-55 — An-Nahl

51۞ وَقَالَ اللَّهُ لَا تَتَّخِذُوا إِلَٰهَيْنِ اثْنَيْنِ ۖ إِنَّمَا هُوَ إِلَٰهٌ وَاحِدٌ ۖ فَإِيَّايَ فَارْهَبُونِ
Yàlla nee na : “Buleen sàkk ñaari yàlla. Yàlla jenn rekk la. Kon nangeen Ma ragal”.
52وَلَهُ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَلَهُ الدِّينُ وَاصِبًا ۚ أَفَغَيْرَ اللَّهِ تَتَّقُونَ
Te Moo moom li nekk ci asamaan yi ak suuf ; te Moo moom it ñu war koo jaamu ci diine ju sax. Moo ndax dangeen di ragal keneen ku dul Yàlla ?
53وَمَا بِكُم مِّن نِّعْمَةٍ فَمِنَ اللَّهِ ۖ ثُمَّ إِذَا مَسَّكُمُ الضُّرُّ فَإِلَيْهِ تَجْأَرُونَ
Li ngeen am ciw yiw mi ngi jóge ca Yàlla. Te bu leen lu metti dalee, Moom ngeen di ñaan ndimbal.
54ثُمَّ إِذَا كَشَفَ الضُّرَّ عَنكُمْ إِذَا فَرِيقٌ مِّنكُم بِرَبِّهِمْ يُشْرِكُونَ
Te bu leen lor ja deggikoo, mu am ab kurél buy bokkaaleeti seen Boroom,
55لِيَكْفُرُوا بِمَا آتَيْنَاهُمْ ۚ فَتَمَتَّعُوا ۖ فَسَوْفَ تَعْلَمُونَ
Ngir weddi la Nu leen jox. Xéewluleen ! Dangeen mës a xam !
An-NahlFihi Alxuraan
128Aaya
MeccanRevelation
53Aaya

Tekki — An-Nahl 53

Simoore An-Nahl Aaya 53 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Li ngeen am ciw yiw mi ngi jóge ca Yàlla.…

Simoore Aaya 53/128 — An-Nahl النحل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nahl Dégg, An-Nahl Tekki, An-Nahl mp3, An-Nahl pdf. Aaya 51–55. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers