Al-Isra · 1/111
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Isra
سُبْحَانَ الَّذِي أَسْرَىٰ بِعَبْدِهِ لَيْلًا مِّنَ الْمَسْجِدِ الْحَرَامِ إِلَى الْمَسْجِدِ الْأَقْصَى الَّذِي بَارَكْنَا حَوْلَهُ لِنُرِيَهُ مِنْ آيَاتِنَا ۚ إِنَّهُ هُوَ السَّمِيعُ الْبَصِيرُ ۝١
Subhaanal lazeee asraa bi`abdihee lailam minal Masjidil Haraami ilal Masjidil Aqsal-lazee baaraknaa haw lahoo linuriyahoo min aayaatinaa;innahoo Huwas Samee`ul-Baseer
📖 Tekkim Wolof
Tudd naa sellug Ka nga xam ne Moo rañaane woon jaamam ba Muhammad [yal na ko Yàlla dolli xéewal te musal ko] jële ko Màkka yóbbu ko Baytil Muqaddas [Al qudsu], muy dëkk boo xam ne wurumam barkeel na, ngir Nu won ko ci Sunuy kéemaan,Yàlla mooy Kiy dégg, mooy Kiy gis.

🎧 Dégg


📜 Aaya 1-3 — Simoore Al-Isra

1سُبْحَانَ الَّذِي أَسْرَىٰ بِعَبْدِهِ لَيْلًا مِّنَ الْمَسْجِدِ الْحَرَامِ إِلَى الْمَسْجِدِ الْأَقْصَى الَّذِي بَارَكْنَا حَوْلَهُ لِنُرِيَهُ مِنْ آيَاتِنَا ۚ إِنَّهُ هُوَ السَّمِيعُ الْبَصِيرُ
Tudd naa sellug Ka nga xam ne Moo rañaane woon jaamam ba Muhammad [yal na ko Yàlla dolli xéewal te musal ko] jële ko Màkka yóbbu ko Baytil Muqaddas [Al qudsu], muy dëkk boo xam ne wurumam barkeel na, ngir Nu won ko ci Sunuy kéemaan,Yàlla mooy Kiy dégg, mooy Kiy gis.
2وَآتَيْنَا مُوسَى الْكِتَابَ وَجَعَلْنَاهُ هُدًى لِّبَنِي إِسْرَائِيلَ أَلَّا تَتَّخِذُوا مِن دُونِي وَكِيلًا
Indil Nanu Muusaa ab Téere, def ko mu di ag njub ngir Banii-Israayiila [aw xeetam] te ñu bañ a jàppee keneen wéeruwaay.
3ذُرِّيَّةَ مَنْ حَمَلْنَا مَعَ نُوحٍ ۚ إِنَّهُ كَانَ عَبْدًا شَكُورًا
Ñoo di sëti ña àndoon ak Nooh ca gaal ga te Nu musaloon leen. Nooh jaam la bu daan sant Boroomam.
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
1Aaya

Tekki — Al-Isra 1

Simoore Al-Isra Aaya 1 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Tudd naa sellug Ka nga xam ne Moo rañaane woon…

Simoore Aaya 1/111 — Simoore Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Isra Dégg, Simoore Al-Isra Tekki, Simoore Al-Isra mp3, Simoore Al-Isra pdf. Aaya 1–3. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers