Al-Isra · 29/111
Tekki Waxtaan — Al-Isra
وَلَا تَجْعَلْ يَدَكَ مَغْلُولَةً إِلَىٰ عُنُقِكَ وَلَا تَبْسُطْهَا كُلَّ الْبَسْطِ فَتَقْعُدَ مَلُومًا مَّحْسُورًا ٢٩
Transliteration
Wa laa taj`al yadaka maghloolatan il `unuqika wa laa tabsut haa kullal basti fataq`uda maloomam mahsooraa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Bul bank sa loxo ba mu mel ni lu ñu yeew ci sa doq, waaye it bu ko tàllal mu tàlli ñareet, kon danga mujj di ku ñu yedd, ku ñu dàkku.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 27-31 — Al-Isra
27إِنَّ الْمُبَذِّرِينَ كَانُوا إِخْوَانَ الشَّيَاطِينِ ۖ وَكَانَ الشَّيْطَانُ لِرَبِّهِ كَفُورًا
yàqkat yi mbokki Séytaane lañu ; te Séytaane dafa weddi Boroomam.
28وَإِمَّا تُعْرِضَنَّ عَنْهُمُ ابْتِغَاءَ رَحْمَةٍ مِّن رَّبِّكَ تَرْجُوهَا فَقُل لَّهُمْ قَوْلًا مَّيْسُورًا
Bu fekkee [ñàkk loo leen jox tax na] nga dëddu leen, toog di yaakaar sa yërmaandey Boroom ; nanga leen wax wax ju neex.
29وَلَا تَجْعَلْ يَدَكَ مَغْلُولَةً إِلَىٰ عُنُقِكَ وَلَا تَبْسُطْهَا كُلَّ الْبَسْطِ فَتَقْعُدَ مَلُومًا مَّحْسُورًا
Bul bank sa loxo ba mu mel ni lu ñu yeew ci sa doq, waaye it bu ko tàllal mu tàlli ñareet, kon danga mujj di ku ñu yedd, ku ñu dàkku.
30إِنَّ رَبَّكَ يَبْسُطُ الرِّزْقَ لِمَن يَشَاءُ وَيَقْدِرُ ۚ إِنَّهُ كَانَ بِعِبَادِهِ خَبِيرًا بَصِيرًا
Naka sa Boroom mooy yaatal wërsëgu ku Ko soob. Moo koy xatal it, naka Moom ku xam tey gis la jaamam yi.
31وَلَا تَقْتُلُوا أَوْلَادَكُمْ خَشْيَةَ إِمْلَاقٍ ۖ نَّحْنُ نَرْزُقُهُمْ وَإِيَّاكُمْ ۚ إِنَّ قَتْلَهُمْ كَانَ خِطْئًا كَبِيرًا
Buleen rey seeni doom ngir ragal ag ñàkk ; Nun noo leen di wërsëgal ñoom ak yéen. Rey leen bàkkaar bu rëy la.
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
29Aaya
Tekki — Al-Isra 29
Simoore Al-Isra Aaya 29 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bul bank sa loxo ba mu mel ni lu ñu…Simoore Aaya 29/111 — Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Isra Dégg, Al-Isra Tekki, Al-Isra mp3, Al-Isra pdf. Aaya 27–31. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








