Al-Isra · 93/111
Tekki Waxtaan — Al-Isra
أَوْ يَكُونَ لَكَ بَيْتٌ مِّن زُخْرُفٍ أَوْ تَرْقَىٰ فِي السَّمَاءِ وَلَن نُّؤْمِنَ لِرُقِيِّكَ حَتَّىٰ تُنَزِّلَ عَلَيْنَا كِتَابًا نَّقْرَؤُهُ ۗ قُلْ سُبْحَانَ رَبِّي هَلْ كُنتُ إِلَّا بَشَرًا رَّسُولًا ۝٩٣
Aw yakoona laka baitum min zukhrufin aw tarqaa fis samaaa`i wa lan nu`mina liruqiyyika hatta tunazzila `alainaa kitaaban naqra`uh; qul Subhaana Rabbee hal kuntu illaa basharar Rasoolaa
📖 Tekkim Wolof
mbaa nga am këru wurus ; mbaa nga yéeg ci kaw asamaan si. Te dunu gëm sa yéeg feek wàcceloonu Téere bu nuy jàng”. Neel : “Tudd naa sellug sama Boroom ! Moo ndax man nekkuma lu dul nit ku ñu yónni doŋŋ ? "

🎧 Dégg


📜 Aaya 91-95 — Al-Isra

91أَوْ تَكُونَ لَكَ جَنَّةٌ مِّن نَّخِيلٍ وَعِنَبٍ فَتُفَجِّرَ الْأَنْهَارَ خِلَالَهَا تَفْجِيرًا
walla nga am tooli garabi tàndarma ak garabu reseñ, nga ballal ay dex ci seen diggante yuy ball bu baax ;
92أَوْ تُسْقِطَ السَّمَاءَ كَمَا زَعَمْتَ عَلَيْنَا كِسَفًا أَوْ تَأْتِيَ بِاللَّهِ وَالْمَلَائِكَةِ قَبِيلًا
walla nga rotal ci sunu kaw asamaan si ni nga ko dige, mu nekk ay daggit, mbaa nga indi Yàlla ak Malaaka yi nu jàkkaarloo ;
93أَوْ يَكُونَ لَكَ بَيْتٌ مِّن زُخْرُفٍ أَوْ تَرْقَىٰ فِي السَّمَاءِ وَلَن نُّؤْمِنَ لِرُقِيِّكَ حَتَّىٰ تُنَزِّلَ عَلَيْنَا كِتَابًا نَّقْرَؤُهُ ۗ قُلْ سُبْحَانَ رَبِّي هَلْ كُنتُ إِلَّا بَشَرًا رَّسُولًا
mbaa nga am këru wurus ; mbaa nga yéeg ci kaw asamaan si. Te dunu gëm sa yéeg feek wàcceloonu Téere bu nuy jàng”. Neel : “Tudd naa sellug sama Boroom ! Moo ndax man nekkuma lu dul nit ku ñu yónni doŋŋ ? "
94وَمَا مَنَعَ النَّاسَ أَن يُؤْمِنُوا إِذْ جَاءَهُمُ الْهُدَىٰ إِلَّا أَن قَالُوا أَبَعَثَ اللَّهُ بَشَرًا رَّسُولًا
Te lan moo tere nit ñi gëm, ba leen njub ga dikkalee, lu dul la ñuy wax naan : “Moo ndax Yàlla dana yónni nit [nit ni nun]muy ab Yonent ? ”
95قُل لَّوْ كَانَ فِي الْأَرْضِ مَلَائِكَةٌ يَمْشُونَ مُطْمَئِنِّينَ لَنَزَّلْنَا عَلَيْهِم مِّنَ السَّمَاءِ مَلَكًا رَّسُولًا
Neel : “Bu fekkoon ne ay Malaaka ñoo nekkoon ci kaw suuf si di dox, kon de Malaaka Lanuy yónni ci ñoom Mu jóge asamaan”.
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
93Aaya

Tekki — Al-Isra 93

Simoore Al-Isra Aaya 93 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : mbaa nga am këru wurus ; mbaa nga yéeg ci…

Simoore Aaya 93/111 — Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Isra Dégg, Al-Isra Tekki, Al-Isra mp3, Al-Isra pdf. Aaya 91–95. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers