Al-Kahf · 110/110
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Kahf
قُلْ إِنَّمَا أَنَا بَشَرٌ مِّثْلُكُمْ يُوحَىٰ إِلَيَّ أَنَّمَا إِلَٰهُكُمْ إِلَٰهٌ وَاحِدٌ ۖ فَمَن كَانَ يَرْجُو لِقَاءَ رَبِّهِ فَلْيَعْمَلْ عَمَلًا صَالِحًا وَلَا يُشْرِكْ بِعِبَادَةِ رَبِّهِ أَحَدًا ۝١١٠
Qul innamaaa ana basharum mislukum yoohaaa ilaiya annamaa ilaahukum Ilaahunw Waahid; faman kaana yarjoo liqaaa`a Rabbihee falya`mal `amalan saalihanw wa laa yushrik bi`ibaadati Rabbiheee ahadaa
📖 Tekkim Wolof
Neel : “Man dey mbindéef laa ni yéen. Danu may soloo rekk, waaye li wóor moo di seen Yàlla jenn rekk la ! [Kon nag], képp ku yaakaar dajeek Boroomam, nay jëf jëf yu yiw te bu mu bokkaale dara ak Boroomam [na ko jaamu Moom doŋŋ]”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 108-110 — Simoore Al-Kahf

108خَالِدِينَ فِيهَا لَا يَبْغُونَ عَنْهَا حِوَلًا
dañu fay béel te duñu ko bëgg a weccee.
109قُل لَّوْ كَانَ الْبَحْرُ مِدَادًا لِّكَلِمَاتِ رَبِّي لَنَفِدَ الْبَحْرُ قَبْلَ أَن تَنفَدَ كَلِمَاتُ رَبِّي وَلَوْ جِئْنَا بِمِثْلِهِ مَدَدًا
Waxalne : “Su ndoxum géej gi doonoon daa, ñu di ca binde kàdduy Yàlla yi, kon ndox ma dana jeex balaa kàddu ya di mat, doonte la sax dañu cay dolliwaat lu tollu ni géej ya”.
110قُلْ إِنَّمَا أَنَا بَشَرٌ مِّثْلُكُمْ يُوحَىٰ إِلَيَّ أَنَّمَا إِلَٰهُكُمْ إِلَٰهٌ وَاحِدٌ ۖ فَمَن كَانَ يَرْجُو لِقَاءَ رَبِّهِ فَلْيَعْمَلْ عَمَلًا صَالِحًا وَلَا يُشْرِكْ بِعِبَادَةِ رَبِّهِ أَحَدًا
Neel : “Man dey mbindéef laa ni yéen. Danu may soloo rekk, waaye li wóor moo di seen Yàlla jenn rekk la ! [Kon nag], képp ku yaakaar dajeek Boroomam, nay jëf jëf yu yiw te bu mu bokkaale dara ak Boroomam [na ko jaamu Moom doŋŋ]”.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
110Aaya

Tekki — Al-Kahf 110

Simoore Al-Kahf Aaya 110 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Neel : “Man dey mbindéef laa ni yéen. Danu may…

Simoore Aaya 110/110 — Simoore Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Kahf Dégg, Simoore Al-Kahf Tekki, Simoore Al-Kahf mp3, Simoore Al-Kahf pdf. Aaya 108–110. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers