Al-Kahf · 34/110
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Kahf
وَكَانَ لَهُ ثَمَرٌ فَقَالَ لِصَاحِبِهِ وَهُوَ يُحَاوِرُهُ أَنَا أَكْثَرُ مِنكَ مَالًا وَأَعَزُّ نَفَرًا ۝٣٤
Wa kaana lahoo samarun faqaala lisaahibihee wa huwa yuhaawiruhoo ana aksaru minka maalanw wa a`azzu nafaraa
📖 Tekkim Wolof
Mu am meññent [mu bari] tax mu wax ak moroom ma neko : “Maa la ëpp alal te gën laa bari mbooloo”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 32-36 — Simoore Al-Kahf

32۞ وَاضْرِبْ لَهُم مَّثَلًا رَّجُلَيْنِ جَعَلْنَا لِأَحَدِهِمَا جَنَّتَيْنِ مِنْ أَعْنَابٍ وَحَفَفْنَاهُمَا بِنَخْلٍ وَجَعَلْنَا بَيْنَهُمَا زَرْعًا
Joxleen leebuw ñaari góor ñoo xam ne : kenn ka jox Nanu ko tool bu am garabi reseñ, Nu wërsëgale leen ak garabi tàndarma, Nu def ca seen diggante ay tooli mbey.
33كِلْتَا الْجَنَّتَيْنِ آتَتْ أُكُلَهَا وَلَمْ تَظْلِم مِّنْهُ شَيْئًا ۚ وَفَجَّرْنَا خِلَالَهُمَا نَهَرًا
Ñaari tool yépp ñu cay jële meññent mu dara wàññeekuwut. Nu xotti ca seen diggante ag dex.
34وَكَانَ لَهُ ثَمَرٌ فَقَالَ لِصَاحِبِهِ وَهُوَ يُحَاوِرُهُ أَنَا أَكْثَرُ مِنكَ مَالًا وَأَعَزُّ نَفَرًا
Mu am meññent [mu bari] tax mu wax ak moroom ma neko : “Maa la ëpp alal te gën laa bari mbooloo”.
35وَدَخَلَ جَنَّتَهُ وَهُوَ ظَالِمٌ لِّنَفْسِهِ قَالَ مَا أَظُنُّ أَن تَبِيدَ هَٰذِهِ أَبَدًا
Mu dugg ca toolam te moom tooñ na boppam ; mu ne : “Yaakaar naa ne lii du jeex mukk,
36وَمَا أَظُنُّ السَّاعَةَ قَائِمَةً وَلَئِن رُّدِدتُّ إِلَىٰ رَبِّي لَأَجِدَنَّ خَيْرًا مِّنْهَا مُنقَلَبًا
te yaakaaruma [foogu ma] jeexug àddina dana egsi. Te sax su ma [deeyoon] ba dellu ca sama Boroom fàwwu, danaa fa fekk lu gën lii cig daluwaay.
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
34Aaya

Tekki — Al-Kahf 34

Simoore Al-Kahf Aaya 34 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu am meññent [mu bari] tax mu wax ak moroom…

Simoore Aaya 34/110 — Simoore Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Kahf Dégg, Simoore Al-Kahf Tekki, Simoore Al-Kahf mp3, Simoore Al-Kahf pdf. Aaya 32–36. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers