Maryam · 48/98
Tekki Waxtaan — Maryam
وَأَعْتَزِلُكُمْ وَمَا تَدْعُونَ مِن دُونِ اللَّهِ وَأَدْعُو رَبِّي عَسَىٰ أَلَّا أَكُونَ بِدُعَاءِ رَبِّي شَقِيًّا ۝٤٨
Wa a`tazilukum wa maa tad`oona min doonil laahi wa ad`o Rabbee `asaaa allaaa akoona bidu`aaa`i Rabbee shaqiyyaa
📖 Tekkim Wolof
Danaa leen beru yéen ak ñi ngeen di jaamu te du Yàlla, tey ñaan sama Boroom. Yaakaar naa ne duma xañ”.
🎧 Dégg

📜 Aaya 46-50 — Maryam

46قَالَ أَرَاغِبٌ أَنتَ عَنْ آلِهَتِي يَا إِبْرَاهِيمُ ۖ لَئِن لَّمْ تَنتَهِ لَأَرْجُمَنَّكَ ۖ وَاهْجُرْنِي مَلِيًّا
Baayam daldi ne ko : "Moo Ibraahiima, ndax dangaa bañ sama yàlla jii ? Soo bàyyilwul [lii ngay wax], danaa la yóori xeer [ba nga dee], te sax génnal topp sa një”.
47قَالَ سَلَامٌ عَلَيْكَ ۖ سَأَسْتَغْفِرُ لَكَ رَبِّي ۖ إِنَّهُ كَانَ بِي حَفِيًّا
[Ibraahiima] ne ko : “Yal na jàmm nekk ci yaw”. “Danaa la sàkkul njéggal ci sama Boroom ndax Ku ma teral la.
48وَأَعْتَزِلُكُمْ وَمَا تَدْعُونَ مِن دُونِ اللَّهِ وَأَدْعُو رَبِّي عَسَىٰ أَلَّا أَكُونَ بِدُعَاءِ رَبِّي شَقِيًّا
Danaa leen beru yéen ak ñi ngeen di jaamu te du Yàlla, tey ñaan sama Boroom. Yaakaar naa ne duma xañ”.
49فَلَمَّا اعْتَزَلَهُمْ وَمَا يَعْبُدُونَ مِن دُونِ اللَّهِ وَهَبْنَا لَهُ إِسْحَاقَ وَيَعْقُوبَ ۖ وَكُلًّا جَعَلْنَا نَبِيًّا
Ba mu leen beroo, [dëddu leen] ñoom ak la ñu daan jaamu te duñu Yàlla, booba Lanu ko may Isaaqa ak Yànqooba ; def leen ñoom ñaar ñépp ñu di ay Yonent.
50وَوَهَبْنَا لَهُم مِّن رَّحْمَتِنَا وَجَعَلْنَا لَهُمْ لِسَانَ صِدْقٍ عَلِيًّا
Nu daldi leen may ci Sunu yërmaande, defal leen làmmiñ wu dëggu wu kawe.
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
48Aaya

Tekki — Maryam 48

Simoore Maryam Aaya 48 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Danaa leen beru yéen ak ñi ngeen di jaamu te…

Simoore Aaya 48/98 — Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Maryam Dégg, Maryam Tekki, Maryam mp3, Maryam pdf. Aaya 46–50. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers