Maryam · 69/98
Tekki Waxtaan — Simoore Maryam
ثُمَّ لَنَنزِعَنَّ مِن كُلِّ شِيعَةٍ أَيُّهُمْ أَشَدُّ عَلَى الرَّحْمَٰنِ عِتِيًّا ۝٦٩
Summa lananzi `anna min kulli shee`atin aiyuhum ashaddu `alar Rahmaani `itiyyaa
📖 Tekkim Wolof
Ba noppi nag, Nuy rocci ci xeet wu nekk kan moo ca gën tar ug féttéerlu ca Yàlla.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 67-71 — Simoore Maryam

67أَوَلَا يَذْكُرُ الْإِنسَانُ أَنَّا خَلَقْنَاهُ مِن قَبْلُ وَلَمْ يَكُ شَيْئًا
Moo ndax nit dafa fàttalikuwul ne Noo ko bindoon bu njëkk te doonutoon dara ?
68فَوَرَبِّكَ لَنَحْشُرَنَّهُمْ وَالشَّيَاطِينَ ثُمَّ لَنُحْضِرَنَّهُمْ حَوْلَ جَهَنَّمَ جِثِيًّا
Giñ naa ci sa màggug Boroom ne Dananu leen pang [dajale] ñook séytaane ya ba ñu yemb. Nu wërële leen ca Safara ñu sukk fa.
69ثُمَّ لَنَنزِعَنَّ مِن كُلِّ شِيعَةٍ أَيُّهُمْ أَشَدُّ عَلَى الرَّحْمَٰنِ عِتِيًّا
Ba noppi nag, Nuy rocci ci xeet wu nekk kan moo ca gën tar ug féttéerlu ca Yàlla.
70ثُمَّ لَنَحْنُ أَعْلَمُ بِالَّذِينَ هُمْ أَوْلَىٰ بِهَا صِلِيًّا
Noo gën a xam kan moo gën a yeyoo jaaru ca Safara.
71وَإِن مِّنكُمْ إِلَّا وَارِدُهَا ۚ كَانَ عَلَىٰ رَبِّكَ حَتْمًا مَّقْضِيًّا
Ñépp a fay jaar, Yàlla dogal na ko ba noppi.
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
69Aaya

Tekki — Maryam 69

Simoore Maryam Aaya 69 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba noppi nag, Nuy rocci ci xeet wu nekk kan…

Simoore Aaya 69/98 — Simoore Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Maryam Dégg, Simoore Maryam Tekki, Simoore Maryam mp3, Simoore Maryam pdf. Aaya 67–71. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers