Maryam · 68/98
Tekki Waxtaan — Maryam
فَوَرَبِّكَ لَنَحْشُرَنَّهُمْ وَالشَّيَاطِينَ ثُمَّ لَنُحْضِرَنَّهُمْ حَوْلَ جَهَنَّمَ جِثِيًّا ٦٨
Transliteration
Fawa Rabbika lanahshu rannahum wash shayaateena summa lanuhdirannahum hawla jahannama jisiyyaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Giñ naa ci sa màggug Boroom ne Dananu leen pang [dajale] ñook séytaane ya ba ñu yemb. Nu wërële leen ca Safara ñu sukk fa.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 66-70 — Maryam
66وَيَقُولُ الْإِنسَانُ أَإِذَا مَا مِتُّ لَسَوْفَ أُخْرَجُ حَيًّا
Nit nag di wax naan : “Ndax su ma dee danañu ma génnewaat may dundu ? ”
67أَوَلَا يَذْكُرُ الْإِنسَانُ أَنَّا خَلَقْنَاهُ مِن قَبْلُ وَلَمْ يَكُ شَيْئًا
Moo ndax nit dafa fàttalikuwul ne Noo ko bindoon bu njëkk te doonutoon dara ?
68فَوَرَبِّكَ لَنَحْشُرَنَّهُمْ وَالشَّيَاطِينَ ثُمَّ لَنُحْضِرَنَّهُمْ حَوْلَ جَهَنَّمَ جِثِيًّا
Giñ naa ci sa màggug Boroom ne Dananu leen pang [dajale] ñook séytaane ya ba ñu yemb. Nu wërële leen ca Safara ñu sukk fa.
69ثُمَّ لَنَنزِعَنَّ مِن كُلِّ شِيعَةٍ أَيُّهُمْ أَشَدُّ عَلَى الرَّحْمَٰنِ عِتِيًّا
Ba noppi nag, Nuy rocci ci xeet wu nekk kan moo ca gën tar ug féttéerlu ca Yàlla.
70ثُمَّ لَنَحْنُ أَعْلَمُ بِالَّذِينَ هُمْ أَوْلَىٰ بِهَا صِلِيًّا
Noo gën a xam kan moo gën a yeyoo jaaru ca Safara.
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
68Aaya
Tekki — Maryam 68
Simoore Maryam Aaya 68 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Giñ naa ci sa màggug Boroom ne Dananu leen pang…Simoore Aaya 68/98 — Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Maryam Dégg, Maryam Tekki, Maryam mp3, Maryam pdf. Aaya 66–70. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








