Al-Baqara · 168/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
يَا أَيُّهَا النَّاسُ كُلُوا مِمَّا فِي الْأَرْضِ حَلَالًا طَيِّبًا وَلَا تَتَّبِعُوا خُطُوَاتِ الشَّيْطَانِ ۚ إِنَّهُ لَكُمْ عَدُوٌّ مُّبِينٌ ۝١٦٨
Yaaa ayyuhan naasu kuloo mimmaa fil ardi halaalan taiyibanw wa laa tattabi`oo khutu waatish Shaitaan; innahoo lakum `aduwwum mubeen
📖 Tekkim Wolof
Yéen nit ñi ! Lekkleen ci li nekk ci suuf si, dagan, teey ; te buleen topp jéegoy (Séytaane) moom seenub noon la bu bir .

🎧 Dégg


📜 Aaya 166-170 — Al-Baqara

166إِذْ تَبَرَّأَ الَّذِينَ اتُّبِعُوا مِنَ الَّذِينَ اتَّبَعُوا وَرَأَوُا الْعَذَابَ وَتَقَطَّعَتْ بِهِمُ الْأَسْبَابُ
[Bu Bis-pénc baa] ba ñañu toppoon deñtalu ca ña leen toppoon ndax te gis nañu mbugal ma, la leen boole woon lépp daggatoo !
167وَقَالَ الَّذِينَ اتَّبَعُوا لَوْ أَنَّ لَنَا كَرَّةً فَنَتَبَرَّأَ مِنْهُمْ كَمَا تَبَرَّءُوا مِنَّا ۗ كَذَٰلِكَ يُرِيهِمُ اللَّهُ أَعْمَالَهُمْ حَسَرَاتٍ عَلَيْهِمْ ۖ وَمَا هُم بِخَارِجِينَ مِنَ النَّارِ
Ña toppe woon, daldi ne : “Ay ! bu nu delluwaatoon àddina! Dananu deñtalu ci ñoom kem ni ñu deñtaloo ci nun” - Noonu la leen Yàlla doon wane seeni jëf ; mu di ag yàqule ca seen kaw te duñu génn Safara.
168يَا أَيُّهَا النَّاسُ كُلُوا مِمَّا فِي الْأَرْضِ حَلَالًا طَيِّبًا وَلَا تَتَّبِعُوا خُطُوَاتِ الشَّيْطَانِ ۚ إِنَّهُ لَكُمْ عَدُوٌّ مُّبِينٌ
Yéen nit ñi ! Lekkleen ci li nekk ci suuf si, dagan, teey ; te buleen topp jéegoy (Séytaane) moom seenub noon la bu bir .
169إِنَّمَا يَأْمُرُكُم بِالسُّوءِ وَالْفَحْشَاءِ وَأَن تَقُولُوا عَلَى اللَّهِ مَا لَا تَعْلَمُونَ
Li mu leen di digal moo di ag mbon ak ug caay-caay ak ngeen di wax ci Yàlla lu ngeen xamul.
170وَإِذَا قِيلَ لَهُمُ اتَّبِعُوا مَا أَنزَلَ اللَّهُ قَالُوا بَلْ نَتَّبِعُ مَا أَلْفَيْنَا عَلَيْهِ آبَاءَنَا ۗ أَوَلَوْ كَانَ آبَاؤُهُمْ لَا يَعْقِلُونَ شَيْئًا وَلَا يَهْتَدُونَ
Bu ñu leen nee : “Toppleen li Yàlla wàcce”, ñu ne : “Nun kay la nu miin [di ko jaamu, baaxu maam ya] lanuy topp.” - Moo ndax ! Seen baay ya doonuñu woon ñu dul xalaat, ñu dul gindiku ?
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
168Aaya

Tekki — Al-Baqara 168

Simoore Al-Baqara Aaya 168 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yéen nit ñi ! Lekkleen ci li nekk ci suuf…

Simoore Aaya 168/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 166–170. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers